At-Tur · 28/49
Tekki Waxtaan — At-Tur
إِنَّا كُنَّا مِن قَبْلُ نَدْعُوهُ ۖ إِنَّهُ هُوَ الْبَرُّ الرَّحِيمُ ٢٨
Transliteration
Innaa kunnaa min qablu nad`oohu innahoo huwal barrur raheem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nun dey bu jëkk, ca Àddina danu ko daan woo di ko ñaan. Moom Yàlla, moo di Aji-baax ji , di Jaglewaakoon bi yërmaandeem”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 26-30 — At-Tur
26قَالُوا إِنَّا كُنَّا قَبْلُ فِي أَهْلِنَا مُشْفِقِينَ
Ñanga naan : “Nun dey ba nu nekkee Àddina danoo ragaloon [Yàlla] ;
27فَمَنَّ اللَّهُ عَلَيْنَا وَوَقَانَا عَذَابَ السَّمُومِ
Yàlla daldi nuy baaxe fegal nu mbugalum Samuum.
28إِنَّا كُنَّا مِن قَبْلُ نَدْعُوهُ ۖ إِنَّهُ هُوَ الْبَرُّ الرَّحِيمُ
Nun dey bu jëkk, ca Àddina danu ko daan woo di ko ñaan. Moom Yàlla, moo di Aji-baax ji , di Jaglewaakoon bi yërmaandeem”.
29فَذَكِّرْ فَمَا أَنتَ بِنِعْمَتِ رَبِّكَ بِكَاهِنٍ وَلَا مَجْنُونٍ
Fàttalikul sa xéewali Boroom tax na ba doonoo buxaaba waxantumalaa ab dof ;
30أَمْ يَقُولُونَ شَاعِرٌ نَّتَرَبَّصُ بِهِ رَيْبَ الْمَنُونِ
Walla ñuy wax naan : “Kii waykat la ! Leegi tey mu dee jeexal”.
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
28Aaya
Tekki — At-Tur 28
Simoore At-Tur Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun dey bu jëkk, ca Àddina danu ko daan woo…Simoore Aaya 28/49 — At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tur Dégg, At-Tur Tekki, At-Tur mp3, At-Tur pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








