At-Tur · 29/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
فَذَكِّرْ فَمَا أَنتَ بِنِعْمَتِ رَبِّكَ بِكَاهِنٍ وَلَا مَجْنُونٍ ۝٢٩
Fazakkir famaaa anta bini`mati rabbika bikaahininw wa laa majnoon
📖 Tekkim Wolof
Fàttalikul sa xéewali Boroom tax na ba doonoo buxaaba waxantumalaa ab dof ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 27-31 — Simoore At-Tur

27فَمَنَّ اللَّهُ عَلَيْنَا وَوَقَانَا عَذَابَ السَّمُومِ
Yàlla daldi nuy baaxe fegal nu mbugalum Samuum.
28إِنَّا كُنَّا مِن قَبْلُ نَدْعُوهُ ۖ إِنَّهُ هُوَ الْبَرُّ الرَّحِيمُ
Nun dey bu jëkk, ca Àddina danu ko daan woo di ko ñaan. Moom Yàlla, moo di Aji-baax ji , di Jaglewaakoon bi yërmaandeem”.
29فَذَكِّرْ فَمَا أَنتَ بِنِعْمَتِ رَبِّكَ بِكَاهِنٍ وَلَا مَجْنُونٍ
Fàttalikul sa xéewali Boroom tax na ba doonoo buxaaba waxantumalaa ab dof ;
30أَمْ يَقُولُونَ شَاعِرٌ نَّتَرَبَّصُ بِهِ رَيْبَ الْمَنُونِ
Walla ñuy wax naan : “Kii waykat la ! Leegi tey mu dee jeexal”.
31قُلْ تَرَبَّصُوا فَإِنِّي مَعَكُم مِّنَ الْمُتَرَبِّصِينَ
Waxal ne: “Xaarleen ! Man itam Maa ngi ànd ak ànd ag yéen di xaar”.
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
29Aaya

Tekki — At-Tur 29

Simoore At-Tur Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Fàttalikul sa xéewali Boroom tax na ba doonoo buxaaba waxantumalaa…

Simoore Aaya 29/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers