An-Najm · 48/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
وَأَنَّهُ هُوَ أَغْنَىٰ وَأَقْنَىٰ ۝٤٨
Wa annahoo huwa aghnaa wa aqnaa
📖 Tekkim Wolof
te moom Mooy woomalale.

🎧 Dégg


📜 Aaya 46-50 — Simoore An-Najm

46مِن نُّطْفَةٍ إِذَا تُمْنَىٰ
muy bawoo ci toq maniyu wu wàcci ci njurukaay
47وَأَنَّ عَلَيْهِ النَّشْأَةَ الْأُخْرَىٰ
moom moo waral it sosuwaat ga dekkiwaat,
48وَأَنَّهُ هُوَ أَغْنَىٰ وَأَقْنَىٰ
te moom Mooy woomalale.
49وَأَنَّهُ هُوَ رَبُّ الشِّعْرَىٰ
Te mooy boroom biddiw ba Si’raa,
50وَأَنَّهُ أَهْلَكَ عَادًا الْأُولَىٰ
te moom Moo faagaagaloon waa Aad ñu jëkk ña,
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
48Aaya

Tekki — An-Najm 48

Simoore An-Najm Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te moom Mooy woomalale.

Simoore Aaya 48/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers