An-Najm · 54/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
فَغَشَّاهَا مَا غَشَّىٰ ۝٥٤
Faghashshaahaa maa ghashshaa
📖 Tekkim Wolof
Muur leen ko.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 52-56 — Simoore An-Najm

52وَقَوْمَ نُوحٍ مِّن قَبْلُ ۖ إِنَّهُمْ كَانُوا هُمْ أَظْلَمَ وَأَطْغَىٰ
ak nitu Nooh ñu jëkk ña, ndax ñoom ñoo dàqoon tooñ te gënoon a bew,
53وَالْمُؤْتَفِكَةَ أَهْوَىٰ
noona la wëlbatee suuf sa këpp leen ko.
54فَغَشَّاهَا مَا غَشَّىٰ
Muur leen ko.
55فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكَ تَتَمَارَىٰ
Ana ban ci sa xéewali Boroom yi ngay werante ?
56هَٰذَا نَذِيرٌ مِّنَ النُّذُرِ الْأُولَىٰ
(Muhammad mii) ab xuppekat la ni Yonent ya ko jiitu woon :
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
54Aaya

Tekki — An-Najm 54

Simoore An-Najm Aaya 54 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Muur leen ko.

Simoore Aaya 54/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 52–56. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers