Al-Qamar · 26/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
سَيَعْلَمُونَ غَدًا مَّنِ الْكَذَّابُ الْأَشِرُ ۝٢٦
Sa-ya`lamoona ghadam manil kazzaabul ashir
📖 Tekkim Wolof
Xalset nañu xam bu ëllëgee, ana kan mooy fentaakoon bu yées ba.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 24-28 — Simoore Al-Qamar

24فَقَالُوا أَبَشَرًا مِّنَّا وَاحِدًا نَّتَّبِعُهُ إِنَّا إِذًا لَّفِي ضَلَالٍ وَسُعُرٍ
Ñuy wax naan : “Jenn waay ni nun nu di ko topp ? Kon dey nu sànku te réer.
25أَأُلْقِيَ الذِّكْرُ عَلَيْهِ مِن بَيْنِنَا بَلْ هُوَ كَذَّابٌ أَشِرٌ
Moo ndax dañu koo coqate moom doŋŋ ci nun yónni ko ? Kii daal ab fentaakoon la, bu yées”
26سَيَعْلَمُونَ غَدًا مَّنِ الْكَذَّابُ الْأَشِرُ
Xalset nañu xam bu ëllëgee, ana kan mooy fentaakoon bu yées ba.
27إِنَّا مُرْسِلُو النَّاقَةِ فِتْنَةً لَّهُمْ فَارْتَقِبْهُمْ وَاصْطَبِرْ
yónni nanu ca ñoom naaga (gileem gu jigéen), muy sànje ci ñoom. Fugluleen te muñalleen (Saalih).
28وَنَبِّئْهُمْ أَنَّ الْمَاءَ قِسْمَةٌ بَيْنَهُمْ ۖ كُلُّ شِرْبٍ مُّحْتَضَرٌ
Nanga xamle ne ndox ma dañu koy bokk séddóo ñook [giléem ga] ; duñu fa fekkante.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Al-Qamar 26

Simoore Al-Qamar Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xalset nañu xam bu ëllëgee, ana kan mooy fentaakoon bu…

Simoore Aaya 26/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers