Ar-Rahman · 35/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
يُرْسَلُ عَلَيْكُمَا شُوَاظٌ مِّن نَّارٍ وَنُحَاسٌ فَلَا تَنتَصِرَانِ ۝٣٥
Yursalu `alaikumaa shuwaazum min naarifiw-wa nuhaasun falaa tantasiraan
📖 Tekkim Wolof
Dees na leen xala sotti safara ak biteex, te kenn du leen dimbali.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 33-37 — Simoore Ar-Rahman

33يَا مَعْشَرَ الْجِنِّ وَالْإِنسِ إِنِ اسْتَطَعْتُمْ أَن تَنفُذُوا مِنْ أَقْطَارِ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ فَانفُذُوا ۚ لَا تَنفُذُونَ إِلَّا بِسُلْطَانٍ
Eey yéen mbooleem jinne yi ak nit ñi ! Su ngeen manee lañbatu ci biir déeléy asamaan yeek suuf si, lañbatuleen. Waaye du ngeen mana kër-këri mukk ba génn kiiraayal Yàlla.
34فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
35يُرْسَلُ عَلَيْكُمَا شُوَاظٌ مِّن نَّارٍ وَنُحَاسٌ فَلَا تَنتَصِرَانِ
Dees na leen xala sotti safara ak biteex, te kenn du leen dimbali.
36فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
37فَإِذَا انشَقَّتِ السَّمَاءُ فَكَانَتْ وَرْدَةً كَالدِّهَانِ
Su asamaan si xottikoo ruy mel ni beteex.
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
35Aaya

Tekki — Ar-Rahman 35

Simoore Ar-Rahman Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dees na leen xala sotti safara ak biteex, te kenn…

Simoore Aaya 35/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers