Al-Waqi'a · 88/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
فَأَمَّا إِن كَانَ مِنَ الْمُقَرَّبِينَ ۝٨٨
Fa ammaaa in kaana minal muqarrabeen
📖 Tekkim Wolof
Su fekkee ne koo ku dafa jige woon (Yàlla),

🎧 Dégg


📜 Aaya 86-90 — Simoore Al-Waqi'a

86فَلَوْلَا إِن كُنتُمْ غَيْرَ مَدِينِينَ
Bu ngeen, jortee ne ameeluleen Yàlla dara,
87تَرْجِعُونَهَا إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
ana lan moo tax kon delloosiwuleen [ruuh ga], ndegam ñu dëggu ngeen ?
88فَأَمَّا إِن كَانَ مِنَ الْمُقَرَّبِينَ
Su fekkee ne koo ku dafa jige woon (Yàlla),
89فَرَوْحٌ وَرَيْحَانٌ وَجَنَّتُ نَعِيمٍ
dana (am) noflaay, ak àjjanay xéewël.
90وَأَمَّا إِن كَانَ مِنْ أَصْحَابِ الْيَمِينِ
Su fekkee ne nag dafa bokk ci waa ndeyjoor,
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
88Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 88

Simoore Al-Waqi'a Aaya 88 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su fekkee ne koo ku dafa jige woon (Yàlla),

Simoore Aaya 88/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 86–90. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers