Al-Waqi'a · 87/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
تَرْجِعُونَهَا إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ ۝٨٧
Tarji`oonahaaa in kuntum saadiqeen
📖 Tekkim Wolof
ana lan moo tax kon delloosiwuleen [ruuh ga], ndegam ñu dëggu ngeen ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 85-89 — Simoore Al-Waqi'a

85وَنَحْنُ أَقْرَبُ إِلَيْهِ مِنكُمْ وَلَٰكِن لَّا تُبْصِرُونَ
fekk na booba Nun Yàlla noo ko gëna jigeñ waaye du ngeen gis.
86فَلَوْلَا إِن كُنتُمْ غَيْرَ مَدِينِينَ
Bu ngeen, jortee ne ameeluleen Yàlla dara,
87تَرْجِعُونَهَا إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
ana lan moo tax kon delloosiwuleen [ruuh ga], ndegam ñu dëggu ngeen ?
88فَأَمَّا إِن كَانَ مِنَ الْمُقَرَّبِينَ
Su fekkee ne koo ku dafa jige woon (Yàlla),
89فَرَوْحٌ وَرَيْحَانٌ وَجَنَّتُ نَعِيمٍ
dana (am) noflaay, ak àjjanay xéewël.
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
87Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 87

Simoore Al-Waqi'a Aaya 87 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ana lan moo tax kon delloosiwuleen [ruuh ga], ndegam ñu…

Simoore Aaya 87/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 85–89. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers