Al-An'am · 132/165
Tekki Waxtaan — Al-An'am
وَلِكُلٍّ دَرَجَاتٌ مِّمَّا عَمِلُوا ۚ وَمَا رَبُّكَ بِغَافِلٍ عَمَّا يَعْمَلُونَ ۝١٣٢
Wa likullin darajaatum mimmaa `amiloo; wa maa Rabbuka bighaafilin `ammaa ya`maloon
📖 Tekkim Wolof
Ñoom ñépp danañu am pey gu méngook la ñu jëfoon. Sa Boroom ñàkkul paal ca la ñuy jëf.
🎧 Dégg

📜 Aaya 130-134 — Al-An'am

130يَا مَعْشَرَ الْجِنِّ وَالْإِنسِ أَلَمْ يَأْتِكُمْ رُسُلٌ مِّنكُمْ يَقُصُّونَ عَلَيْكُمْ آيَاتِي وَيُنذِرُونَكُمْ لِقَاءَ يَوْمِكُمْ هَٰذَا ۚ قَالُوا شَهِدْنَا عَلَىٰ أَنفُسِنَا ۖ وَغَرَّتْهُمُ الْحَيَاةُ الدُّنْيَا وَشَهِدُوا عَلَىٰ أَنفُسِهِمْ أَنَّهُمْ كَانُوا كَافِرِينَ
[Mu ne leen] Éy yéen mbooloom jinne yi ak nit ñi ndax ay Yonent dafa leen a dikkalul woon, feeñ ci seen biir, di leen nettali Samay ndigal ci doon leen waar ci ndajem seen Bis bii ? Ñu toontu ne : “Seede nanu loolu mu nekk ci sunu kaw.”. Dundug àddina wor na leen ; seeni seede dal ci seen kaw, saxal ne ñoom ay yéefar lañu woon.
131ذَٰلِكَ أَن لَّمْ يَكُن رَّبُّكَ مُهْلِكَ الْقُرَىٰ بِظُلْمٍ وَأَهْلُهَا غَافِلُونَ
Loolu dafay tegtale ne sa Boroom du alag ab dëkk cig tooñeel ndare dafa yónni ndaw ñu lànk koo topp.
132وَلِكُلٍّ دَرَجَاتٌ مِّمَّا عَمِلُوا ۚ وَمَا رَبُّكَ بِغَافِلٍ عَمَّا يَعْمَلُونَ
Ñoom ñépp danañu am pey gu méngook la ñu jëfoon. Sa Boroom ñàkkul paal ca la ñuy jëf.
133وَرَبُّكَ الْغَنِيُّ ذُو الرَّحْمَةِ ۚ إِن يَشَأْ يُذْهِبْكُمْ وَيَسْتَخْلِفْ مِن بَعْدِكُم مَّا يَشَاءُ كَمَا أَنشَأَكُم مِّن ذُرِّيَّةِ قَوْمٍ آخَرِينَ
Sa Boroom Ku woomal la, boroom yërmaande la. Bu ko neexoon, mu jële leen fi, wuutale ci seen ginnaaw la Ko soob, ni Mu leen sose woon ngeen di ay sëti ñeneen.
134إِنَّ مَا تُوعَدُونَ لَآتٍ ۖ وَمَا أَنتُم بِمُعْجِزِينَ
Li ñu leen dig luy ñëw la. Te dungeen mën a raw.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
132Aaya

Tekki — Al-An'am 132

Simoore Al-An'am Aaya 132 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoom ñépp danañu am pey gu méngook la ñu jëfoon.…

Simoore Aaya 132/165 — Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-An'am Dégg, Al-An'am Tekki, Al-An'am mp3, Al-An'am pdf. Aaya 130–134. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers