Al-An'am · 47/165
Tekki Waxtaan — Simoore Al-An'am
قُلْ أَرَأَيْتَكُمْ إِنْ أَتَاكُمْ عَذَابُ اللَّهِ بَغْتَةً أَوْ جَهْرَةً هَلْ يُهْلَكُ إِلَّا الْقَوْمُ الظَّالِمُونَ ۝٤٧
Qul ara`aitakum in ataakum `azaabul laahi baghtatan aw jahratan hal yuhlaku illal qawmuz zaalimoon
📖 Tekkim Wolof
Waxleen ma : “Ndax bu mbugëlam Yàlla nee xes ci yéen walla muy lu fés, ndax kenn dana ca loru ku dul ña di way-tooñ ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 45-49 — Simoore Al-An'am

45فَقُطِعَ دَابِرُ الْقَوْمِ الَّذِينَ ظَلَمُوا ۚ وَالْحَمْدُ لِلَّهِ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Dogeef na ginnaawug ña tooñoon. Te nag Yàlla miy Boroom àddina bi rekk a yayoo cant !
46قُلْ أَرَأَيْتُمْ إِنْ أَخَذَ اللَّهُ سَمْعَكُمْ وَأَبْصَارَكُمْ وَخَتَمَ عَلَىٰ قُلُوبِكُم مَّنْ إِلَٰهٌ غَيْرُ اللَّهِ يَأْتِيكُم بِهِ ۗ انظُرْ كَيْفَ نُصَرِّفُ الْآيَاتِ ثُمَّ هُمْ يَصْدِفُونَ
Waxleen ma : “Bu Yàlla téye woon seenug dégg, ak seenug jis, tëj seeni xol, ana keneen ku dul Yàlla ku leen mën a delloo yooyu ? Gisal ni Yàlla di leerale ay tegtalam ! Ba noppi ñoom ñuy jeng.
47قُلْ أَرَأَيْتَكُمْ إِنْ أَتَاكُمْ عَذَابُ اللَّهِ بَغْتَةً أَوْ جَهْرَةً هَلْ يُهْلَكُ إِلَّا الْقَوْمُ الظَّالِمُونَ
Waxleen ma : “Ndax bu mbugëlam Yàlla nee xes ci yéen walla muy lu fés, ndax kenn dana ca loru ku dul ña di way-tooñ ? ”
48وَمَا نُرْسِلُ الْمُرْسَلِينَ إِلَّا مُبَشِّرِينَ وَمُنذِرِينَ ۖ فَمَنْ آمَنَ وَأَصْلَحَ فَلَا خَوْفٌ عَلَيْهِمْ وَلَا هُمْ يَحْزَنُونَ
Dunu yónni ay Yonent lu dul ne ñoom dañuy xuppeek a bégle : ña gëm te sellal, yéwénal, njàqare duleen dal, duñu am naqar.
49وَالَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا يَمَسُّهُمُ الْعَذَابُ بِمَا كَانُوا يَفْسُقُونَ
Ña weddi Sunuy kàddu, mbugal dana leen sóor ndax la ñu daan jalgati.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
47Aaya

Tekki — Al-An'am 47

Simoore Al-An'am Aaya 47 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxleen ma : “Ndax bu mbugëlam Yàlla nee xes ci…

Simoore Aaya 47/165 — Simoore Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-An'am Dégg, Simoore Al-An'am Tekki, Simoore Al-An'am mp3, Simoore Al-An'am pdf. Aaya 45–49. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers