Al-An'am · 85/165
Tekki Waxtaan — Al-An'am
وَزَكَرِيَّا وَيَحْيَىٰ وَعِيسَىٰ وَإِلْيَاسَ ۖ كُلٌّ مِّنَ الصَّالِحِينَ ٨٥
Transliteration
Wa Zakariyyaa wa Yahyaa wa `Eesaa wa Illyaasa kullum minas saaliheen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ak Zakariyaa ak Yahyaa, ak Iisaa ak Ilyaas, ñoom ñépp ca nit ñu yiw ña lañu bokk.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 83-87 — Al-An'am
83وَتِلْكَ حُجَّتُنَا آتَيْنَاهَا إِبْرَاهِيمَ عَلَىٰ قَوْمِهِ ۚ نَرْفَعُ دَرَجَاتٍ مَّن نَّشَاءُ ۗ إِنَّ رَبَّكَ حَكِيمٌ عَلِيمٌ
Loolu mooy Sunu lay wi nu jox Ibraahiima mu yay ca aw nitam. Dananu yékkati ku Nu neex mu kawe. Te sa Boroom Ku xereñ la, Ku xam la.
84وَوَهَبْنَا لَهُ إِسْحَاقَ وَيَعْقُوبَ ۚ كُلًّا هَدَيْنَا ۚ وَنُوحًا هَدَيْنَا مِن قَبْلُ ۖ وَمِن ذُرِّيَّتِهِ دَاوُودَ وَسُلَيْمَانَ وَأَيُّوبَ وَيُوسُفَ وَمُوسَىٰ وَهَارُونَ ۚ وَكَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
May Nanu ko Isaaqa ak Yanqooba, gindi leen, teg leen cig njub ñoom ñépp. Ak Nooh it, gindi Nanu ko lu jiitu, ak cay sëtam, Daawuda ak Suleymaan, ak Ayuuba ak Yuusufa, ak Muusaa, ak Haaruuna. Te noonu la Nuy feyee ñay rafetal.
85وَزَكَرِيَّا وَيَحْيَىٰ وَعِيسَىٰ وَإِلْيَاسَ ۖ كُلٌّ مِّنَ الصَّالِحِينَ
Ak Zakariyaa ak Yahyaa, ak Iisaa ak Ilyaas, ñoom ñépp ca nit ñu yiw ña lañu bokk.
86وَإِسْمَاعِيلَ وَالْيَسَعَ وَيُونُسَ وَلُوطًا ۚ وَكُلًّا فَضَّلْنَا عَلَى الْعَالَمِينَ
Ak Ismaahiila ak Ilyaas, ak Yunuus, ak Lóot. Te ñoom ñépp defal Nanu leen ngëneel ci kaw waa àddina si.
87وَمِنْ آبَائِهِمْ وَذُرِّيَّاتِهِمْ وَإِخْوَانِهِمْ ۖ وَاجْتَبَيْنَاهُمْ وَهَدَيْنَاهُمْ إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Te ca biir seeni baay ak seeni sët ak seeni mbokk, tànn Nanu leen, jubal leen, teg leen ca yoon bu jub wa.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
85Aaya
Tekki — Al-An'am 85
Simoore Al-An'am Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak Zakariyaa ak Yahyaa, ak Iisaa ak Ilyaas, ñoom ñépp…Simoore Aaya 85/165 — Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-An'am Dégg, Al-An'am Tekki, Al-An'am mp3, Al-An'am pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








