Al-Qalam · 15/52
Tekki Waxtaan — Al-Qalam
إِذَا تُتْلَىٰ عَلَيْهِ آيَاتُنَا قَالَ أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ ١٥
Transliteration
Izaa tutlaa `alaihi aayaatunaa qaala asaateerul awwaleen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Saa su ñu jàngee fi kanamam Sunuy Laaya, muy wax naan : “Léebi ñu jëkk ña la”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 13-17 — Al-Qalam
13عُتُلٍّ بَعْدَ ذَٰلِكَ زَنِيمٍ
ak ku jàgg, te bariw ay.
14أَن كَانَ ذَا مَالٍ وَبَنِينَ
Mu nekk di boroom alal ak i doom.
15إِذَا تُتْلَىٰ عَلَيْهِ آيَاتُنَا قَالَ أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ
Saa su ñu jàngee fi kanamam Sunuy Laaya, muy wax naan : “Léebi ñu jëkk ña la”.
16سَنَسِمُهُ عَلَى الْخُرْطُومِ
Dananu ko wutal màndarga ci suku [bakkanam].
17إِنَّا بَلَوْنَاهُمْ كَمَا بَلَوْنَا أَصْحَابَ الْجَنَّةِ إِذْ أَقْسَمُوا لَيَصْرِمُنَّهَا مُصْبِحِينَ
Natu nanu leen kom ni nu nattuwoon woroom tool ya ba ñu diisóo ne ba ñu xëy góob ko,
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
15Aaya
Tekki — Al-Qalam 15
Simoore Al-Qalam Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Saa su ñu jàngee fi kanamam Sunuy Laaya, muy wax…Simoore Aaya 15/52 — Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qalam Dégg, Al-Qalam Tekki, Al-Qalam mp3, Al-Qalam pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








