Al-Qalam · 16/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
سَنَسِمُهُ عَلَى الْخُرْطُومِ ۝١٦
Sanasimuhoo `alal khurtoom
📖 Tekkim Wolof
Dananu ko wutal màndarga ci suku [bakkanam].

🎧 Dégg


📜 Aaya 14-18 — Simoore Al-Qalam

14أَن كَانَ ذَا مَالٍ وَبَنِينَ
Mu nekk di boroom alal ak i doom.
15إِذَا تُتْلَىٰ عَلَيْهِ آيَاتُنَا قَالَ أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ
Saa su ñu jàngee fi kanamam Sunuy Laaya, muy wax naan : “Léebi ñu jëkk ña la”.
16سَنَسِمُهُ عَلَى الْخُرْطُومِ
Dananu ko wutal màndarga ci suku [bakkanam].
17إِنَّا بَلَوْنَاهُمْ كَمَا بَلَوْنَا أَصْحَابَ الْجَنَّةِ إِذْ أَقْسَمُوا لَيَصْرِمُنَّهَا مُصْبِحِينَ
Natu nanu leen kom ni nu nattuwoon woroom tool ya ba ñu diisóo ne ba ñu xëy góob ko,
18وَلَا يَسْتَثْنُونَ
te settee wu ñu woon : “Dogalub Yàlla”.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Qalam 16

Simoore Al-Qalam Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dananu ko wutal màndarga ci suku [bakkanam].

Simoore Aaya 16/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers