Al-Qalam · 19/52
Tekki Waxtaan — Al-Qalam
فَطَافَ عَلَيْهَا طَائِفٌ مِّن رَّبِّكَ وَهُمْ نَائِمُونَ ۝١٩
Fataafa `alaihaa taaa`i fum mir rabbika wa hum naaa`imoon
📖 Tekkim Wolof
Mu am lu bawoo fa sa Boroom dikk wër si ko (faagaagal tool ba) fekk ñoom nelaw nañu,
🎧 Dégg

📜 Aaya 17-21 — Al-Qalam

17إِنَّا بَلَوْنَاهُمْ كَمَا بَلَوْنَا أَصْحَابَ الْجَنَّةِ إِذْ أَقْسَمُوا لَيَصْرِمُنَّهَا مُصْبِحِينَ
Natu nanu leen kom ni nu nattuwoon woroom tool ya ba ñu diisóo ne ba ñu xëy góob ko,
18وَلَا يَسْتَثْنُونَ
te settee wu ñu woon : “Dogalub Yàlla”.
19فَطَافَ عَلَيْهَا طَائِفٌ مِّن رَّبِّكَ وَهُمْ نَائِمُونَ
Mu am lu bawoo fa sa Boroom dikk wër si ko (faagaagal tool ba) fekk ñoom nelaw nañu,
20فَأَصْبَحَتْ كَالصَّرِيمِ
ba bët setee, mu melni luñu déqi.
21فَتَنَادَوْا مُصْبِحِينَ
Ba ñu xëy, wootante ca suba cuuy :
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — Al-Qalam 19

Simoore Al-Qalam Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu am lu bawoo fa sa Boroom dikk wër si…

Simoore Aaya 19/52 — Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qalam Dégg, Al-Qalam Tekki, Al-Qalam mp3, Al-Qalam pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers