Al-Qalam · 20/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
فَأَصْبَحَتْ كَالصَّرِيمِ ۝٢٠
Fa asbahat kassareem
📖 Tekkim Wolof
ba bët setee, mu melni luñu déqi.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 18-22 — Simoore Al-Qalam

18وَلَا يَسْتَثْنُونَ
te settee wu ñu woon : “Dogalub Yàlla”.
19فَطَافَ عَلَيْهَا طَائِفٌ مِّن رَّبِّكَ وَهُمْ نَائِمُونَ
Mu am lu bawoo fa sa Boroom dikk wër si ko (faagaagal tool ba) fekk ñoom nelaw nañu,
20فَأَصْبَحَتْ كَالصَّرِيمِ
ba bët setee, mu melni luñu déqi.
21فَتَنَادَوْا مُصْبِحِينَ
Ba ñu xëy, wootante ca suba cuuy :
22أَنِ اغْدُوا عَلَىٰ حَرْثِكُمْ إِن كُنتُمْ صَارِمِينَ
“Daldi ne teel leen xëy tool waay ndegam da ngeen bëgg góob”.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — Al-Qalam 20

Simoore Al-Qalam Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba bët setee, mu melni luñu déqi.

Simoore Aaya 20/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers