Al-Qalam · 18/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
وَلَا يَسْتَثْنُونَ ۝١٨
Wa laa yastasnoon
📖 Tekkim Wolof
te settee wu ñu woon : “Dogalub Yàlla”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 16-20 — Simoore Al-Qalam

16سَنَسِمُهُ عَلَى الْخُرْطُومِ
Dananu ko wutal màndarga ci suku [bakkanam].
17إِنَّا بَلَوْنَاهُمْ كَمَا بَلَوْنَا أَصْحَابَ الْجَنَّةِ إِذْ أَقْسَمُوا لَيَصْرِمُنَّهَا مُصْبِحِينَ
Natu nanu leen kom ni nu nattuwoon woroom tool ya ba ñu diisóo ne ba ñu xëy góob ko,
18وَلَا يَسْتَثْنُونَ
te settee wu ñu woon : “Dogalub Yàlla”.
19فَطَافَ عَلَيْهَا طَائِفٌ مِّن رَّبِّكَ وَهُمْ نَائِمُونَ
Mu am lu bawoo fa sa Boroom dikk wër si ko (faagaagal tool ba) fekk ñoom nelaw nañu,
20فَأَصْبَحَتْ كَالصَّرِيمِ
ba bët setee, mu melni luñu déqi.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
18Aaya

Tekki — Al-Qalam 18

Simoore Al-Qalam Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te settee wu ñu woon : “Dogalub Yàlla”.

Simoore Aaya 18/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers