Al-Haqqa · 15/52
Tekki Waxtaan — Al-Haqqa
فَيَوْمَئِذٍ وَقَعَتِ الْوَاقِعَةُ ۝١٥
Fa yawma`izinw waqa`atil waaqi`ah
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee, xew-xew,ba agsi bis Pénc ba,
🎧 Dégg

📜 Aaya 13-17 — Al-Haqqa

13فَإِذَا نُفِخَ فِي الصُّورِ نَفْخَةٌ وَاحِدَةٌ
Su nu walee bufta ba, genn wal ëf ko,
14وَحُمِلَتِ الْأَرْضُ وَالْجِبَالُ فَدُكَّتَا دَكَّةً وَاحِدَةً
suuf si ak doj yi ñu jël ko def ko pënd moñoxe ko benn yoon ;
15فَيَوْمَئِذٍ وَقَعَتِ الْوَاقِعَةُ
Bu keroogee, xew-xew,ba agsi bis Pénc ba,
16وَانشَقَّتِ السَّمَاءُ فَهِيَ يَوْمَئِذٍ وَاهِيَةٌ
asamaan siy xottiku nooy nepp.
17وَالْمَلَكُ عَلَىٰ أَرْجَائِهَا ۚ وَيَحْمِلُ عَرْشَ رَبِّكَ فَوْقَهُمْ يَوْمَئِذٍ ثَمَانِيَةٌ
Malaaka ya nekk ci ay goxam, su ko defee juróom-ñatta, cay yanu gàngunaay ga ( Aras ).
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-Haqqa 15

Simoore Al-Haqqa Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee, xew-xew,ba agsi bis Pénc ba,

Simoore Aaya 15/52 — Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Haqqa Dégg, Al-Haqqa Tekki, Al-Haqqa mp3, Al-Haqqa pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers