Al-Haqqa · 16/52
Tekki Waxtaan — Al-Haqqa
وَانشَقَّتِ السَّمَاءُ فَهِيَ يَوْمَئِذٍ وَاهِيَةٌ ۝١٦
Wanshaqqatis samaaa`u fahiya yawma `izinw-waahiyah
📖 Tekkim Wolof
asamaan siy xottiku nooy nepp.
🎧 Dégg

📜 Aaya 14-18 — Al-Haqqa

14وَحُمِلَتِ الْأَرْضُ وَالْجِبَالُ فَدُكَّتَا دَكَّةً وَاحِدَةً
suuf si ak doj yi ñu jël ko def ko pënd moñoxe ko benn yoon ;
15فَيَوْمَئِذٍ وَقَعَتِ الْوَاقِعَةُ
Bu keroogee, xew-xew,ba agsi bis Pénc ba,
16وَانشَقَّتِ السَّمَاءُ فَهِيَ يَوْمَئِذٍ وَاهِيَةٌ
asamaan siy xottiku nooy nepp.
17وَالْمَلَكُ عَلَىٰ أَرْجَائِهَا ۚ وَيَحْمِلُ عَرْشَ رَبِّكَ فَوْقَهُمْ يَوْمَئِذٍ ثَمَانِيَةٌ
Malaaka ya nekk ci ay goxam, su ko defee juróom-ñatta, cay yanu gàngunaay ga ( Aras ).
18يَوْمَئِذٍ تُعْرَضُونَ لَا تَخْفَىٰ مِنكُمْ خَافِيَةٌ
Bu keroogee dees na leen weer; ken du leen ca nëbb dara.
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Haqqa 16

Simoore Al-Haqqa Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : asamaan siy xottiku nooy nepp.

Simoore Aaya 16/52 — Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Haqqa Dégg, Al-Haqqa Tekki, Al-Haqqa mp3, Al-Haqqa pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers