Al-Haqqa · 14/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
وَحُمِلَتِ الْأَرْضُ وَالْجِبَالُ فَدُكَّتَا دَكَّةً وَاحِدَةً ۝١٤
Wa humilatil ardu wal jibaalu fadukkataa dakkatanw waahidah
📖 Tekkim Wolof
suuf si ak doj yi ñu jël ko def ko pënd moñoxe ko benn yoon ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 12-16 — Simoore Al-Haqqa

12لِنَجْعَلَهَا لَكُمْ تَذْكِرَةً وَتَعِيَهَا أُذُنٌ وَاعِيَةٌ
danu koo def mu di fàttali ci yéen nopp yu sell it man koo jàpp.
13فَإِذَا نُفِخَ فِي الصُّورِ نَفْخَةٌ وَاحِدَةٌ
Su nu walee bufta ba, genn wal ëf ko,
14وَحُمِلَتِ الْأَرْضُ وَالْجِبَالُ فَدُكَّتَا دَكَّةً وَاحِدَةً
suuf si ak doj yi ñu jël ko def ko pënd moñoxe ko benn yoon ;
15فَيَوْمَئِذٍ وَقَعَتِ الْوَاقِعَةُ
Bu keroogee, xew-xew,ba agsi bis Pénc ba,
16وَانشَقَّتِ السَّمَاءُ فَهِيَ يَوْمَئِذٍ وَاهِيَةٌ
asamaan siy xottiku nooy nepp.
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Al-Haqqa 14

Simoore Al-Haqqa Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : suuf si ak doj yi ñu jël ko def ko…

Simoore Aaya 14/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers