Al-Haqqa · 23/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
قُطُوفُهَا دَانِيَةٌ ۝٢٣
Qutoofuhaa daaniyah
📖 Tekkim Wolof
meññatam ma day yoore.

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Simoore Al-Haqqa

21فَهُوَ فِي عِيشَةٍ رَّاضِيَةٍ
Moom dey mi ngi ci dundu gu neex :
22فِي جَنَّةٍ عَالِيَةٍ
ca Àjjana ju kawe
23قُطُوفُهَا دَانِيَةٌ
meññatam ma day yoore.
24كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا أَسْلَفْتُمْ فِي الْأَيَّامِ الْخَالِيَةِ
“Lekkleen te naan muy peyug la ngeen jiitaloon”.
25وَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِشِمَالِهِ فَيَقُولُ يَا لَيْتَنِي لَمْ أُوتَ كِتَابِيَهْ
Ña ñuy joxe seen téere ci càmmoñ, danuy wax naan : “Aka neexoon ! Jotuma sama téere,
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Al-Haqqa 23

Simoore Al-Haqqa Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : meññatam ma day yoore.

Simoore Aaya 23/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers