Al-Haqqa · 24/52
Tekki Waxtaan — Al-Haqqa
كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا أَسْلَفْتُمْ فِي الْأَيَّامِ الْخَالِيَةِ ٢٤
Transliteration
Kuloo washraboo haneee`am bimaaa aslaftum fil ayyaamil khaliyah
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
“Lekkleen te naan muy peyug la ngeen jiitaloon”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 22-26 — Al-Haqqa
22فِي جَنَّةٍ عَالِيَةٍ
ca Àjjana ju kawe
23قُطُوفُهَا دَانِيَةٌ
meññatam ma day yoore.
24كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا أَسْلَفْتُمْ فِي الْأَيَّامِ الْخَالِيَةِ
“Lekkleen te naan muy peyug la ngeen jiitaloon”.
25وَأَمَّا مَنْ أُوتِيَ كِتَابَهُ بِشِمَالِهِ فَيَقُولُ يَا لَيْتَنِي لَمْ أُوتَ كِتَابِيَهْ
Ña ñuy joxe seen téere ci càmmoñ, danuy wax naan : “Aka neexoon ! Jotuma sama téere,
26وَلَمْ أَدْرِ مَا حِسَابِيَهْ
te ma ba ña xam luy sama màndaxe...
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
24Aaya
Tekki — Al-Haqqa 24
Simoore Al-Haqqa Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Lekkleen te naan muy peyug la ngeen jiitaloon”.Simoore Aaya 24/52 — Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Haqqa Dégg, Al-Haqqa Tekki, Al-Haqqa mp3, Al-Haqqa pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








