Al-A'raf · 164/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
وَإِذْ قَالَتْ أُمَّةٌ مِّنْهُمْ لِمَ تَعِظُونَ قَوْمًا ۙ اللَّهُ مُهْلِكُهُمْ أَوْ مُعَذِّبُهُمْ عَذَابًا شَدِيدًا ۖ قَالُوا مَعْذِرَةً إِلَىٰ رَبِّكُمْ وَلَعَلَّهُمْ يَتَّقُونَ ۝١٦٤
Wa iz qaalat ummatum minhum lima ta`izoona qaw manil laahu muhlikuhum aw mu`azzibuhum `azaaban shadeedan qaaloo ma`ziratan ilaa Rabbikum wa la`allahum tattaqoon
📖 Tekkim Wolof
Te am mbooloo ca ñoom ne : “Lu tax ngeen di waar nit ñoo xam ne Yàlla dana leen rey mbaa mu teg leen mbugal mu tar ? ”. Ñu toontu [ñoom ña doon waare] ne : “Ngir nu am lay ca seen Boroom ak xéy-na ñoom ñu ragal Yàlla ! ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 162-166 — Simoore Al-A'raf

162فَبَدَّلَ الَّذِينَ ظَلَمُوا مِنْهُمْ قَوْلًا غَيْرَ الَّذِي قِيلَ لَهُمْ فَأَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ رِجْزًا مِّنَ السَّمَاءِ بِمَا كَانُوا يَظْلِمُونَ
Ña tooñ ci ñoom, soppi la ñu leen wax ak yeneeni wax. Nu yebal fa ñoom mbugal mu tukke asamaan ngir la ñu nekk di tooñ.
163وَاسْأَلْهُمْ عَنِ الْقَرْيَةِ الَّتِي كَانَتْ حَاضِرَةَ الْبَحْرِ إِذْ يَعْدُونَ فِي السَّبْتِ إِذْ تَأْتِيهِمْ حِيتَانُهُمْ يَوْمَ سَبْتِهِمْ شُرَّعًا وَيَوْمَ لَا يَسْبِتُونَ ۙ لَا تَأْتِيهِمْ ۚ كَذَٰلِكَ نَبْلُوهُم بِمَا كَانُوا يَفْسُقُونَ
Te nga laaj leen lu jëm ci dëkk ba nekkoon ca tefesu géej ga ca gaawu ba ! Ba seen jën ya tëmbu ci ñoom ca seenug gaawu, tey bañ a génn bis ya! Noonu la Nu leen doon nattoo ngir la ñu daan fétterlu génn topp.
164وَإِذْ قَالَتْ أُمَّةٌ مِّنْهُمْ لِمَ تَعِظُونَ قَوْمًا ۙ اللَّهُ مُهْلِكُهُمْ أَوْ مُعَذِّبُهُمْ عَذَابًا شَدِيدًا ۖ قَالُوا مَعْذِرَةً إِلَىٰ رَبِّكُمْ وَلَعَلَّهُمْ يَتَّقُونَ
Te am mbooloo ca ñoom ne : “Lu tax ngeen di waar nit ñoo xam ne Yàlla dana leen rey mbaa mu teg leen mbugal mu tar ? ”. Ñu toontu [ñoom ña doon waare] ne : “Ngir nu am lay ca seen Boroom ak xéy-na ñoom ñu ragal Yàlla ! ”
165فَلَمَّا نَسُوا مَا ذُكِّرُوا بِهِ أَنجَيْنَا الَّذِينَ يَنْهَوْنَ عَنِ السُّوءِ وَأَخَذْنَا الَّذِينَ ظَلَمُوا بِعَذَابٍ بَئِيسٍ بِمَا كَانُوا يَفْسُقُونَ
Ba ñu fàttee la ñu leen doon waare, musal Nanu ña doon tere lu bon, Nu sadd ña doon tooñ, mbugal mu tar ngir la ñu féttérlu woon génn topp.
166فَلَمَّا عَتَوْا عَن مَّا نُهُوا عَنْهُ قُلْنَا لَهُمْ كُونُوا قِرَدَةً خَاسِئِينَ
Bu ñu rëyloo ca la ñu leen tere, Nu wax leen ne : “Nekkleen di ay golo yu torox”.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
164Aaya

Tekki — Al-A'raf 164

Simoore Al-A'raf Aaya 164 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te am mbooloo ca ñoom ne : “Lu tax ngeen…

Simoore Aaya 164/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 162–166. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers