Al-A'raf · 165/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
فَلَمَّا نَسُوا مَا ذُكِّرُوا بِهِ أَنجَيْنَا الَّذِينَ يَنْهَوْنَ عَنِ السُّوءِ وَأَخَذْنَا الَّذِينَ ظَلَمُوا بِعَذَابٍ بَئِيسٍ بِمَا كَانُوا يَفْسُقُونَ ۝١٦٥
Falammaa nasoo maa zukkiroo bihee anjainal lazeena yanhawna `anis sooo`i wa akhaznal lazeena zalamoo bi`azaabim ba`eeim bimaa kaanooyafsuqoon
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu fàttee la ñu leen doon waare, musal Nanu ña doon tere lu bon, Nu sadd ña doon tooñ, mbugal mu tar ngir la ñu féttérlu woon génn topp.

🎧 Dégg


📜 Aaya 163-167 — Simoore Al-A'raf

163وَاسْأَلْهُمْ عَنِ الْقَرْيَةِ الَّتِي كَانَتْ حَاضِرَةَ الْبَحْرِ إِذْ يَعْدُونَ فِي السَّبْتِ إِذْ تَأْتِيهِمْ حِيتَانُهُمْ يَوْمَ سَبْتِهِمْ شُرَّعًا وَيَوْمَ لَا يَسْبِتُونَ ۙ لَا تَأْتِيهِمْ ۚ كَذَٰلِكَ نَبْلُوهُم بِمَا كَانُوا يَفْسُقُونَ
Te nga laaj leen lu jëm ci dëkk ba nekkoon ca tefesu géej ga ca gaawu ba ! Ba seen jën ya tëmbu ci ñoom ca seenug gaawu, tey bañ a génn bis ya! Noonu la Nu leen doon nattoo ngir la ñu daan fétterlu génn topp.
164وَإِذْ قَالَتْ أُمَّةٌ مِّنْهُمْ لِمَ تَعِظُونَ قَوْمًا ۙ اللَّهُ مُهْلِكُهُمْ أَوْ مُعَذِّبُهُمْ عَذَابًا شَدِيدًا ۖ قَالُوا مَعْذِرَةً إِلَىٰ رَبِّكُمْ وَلَعَلَّهُمْ يَتَّقُونَ
Te am mbooloo ca ñoom ne : “Lu tax ngeen di waar nit ñoo xam ne Yàlla dana leen rey mbaa mu teg leen mbugal mu tar ? ”. Ñu toontu [ñoom ña doon waare] ne : “Ngir nu am lay ca seen Boroom ak xéy-na ñoom ñu ragal Yàlla ! ”
165فَلَمَّا نَسُوا مَا ذُكِّرُوا بِهِ أَنجَيْنَا الَّذِينَ يَنْهَوْنَ عَنِ السُّوءِ وَأَخَذْنَا الَّذِينَ ظَلَمُوا بِعَذَابٍ بَئِيسٍ بِمَا كَانُوا يَفْسُقُونَ
Ba ñu fàttee la ñu leen doon waare, musal Nanu ña doon tere lu bon, Nu sadd ña doon tooñ, mbugal mu tar ngir la ñu féttérlu woon génn topp.
166فَلَمَّا عَتَوْا عَن مَّا نُهُوا عَنْهُ قُلْنَا لَهُمْ كُونُوا قِرَدَةً خَاسِئِينَ
Bu ñu rëyloo ca la ñu leen tere, Nu wax leen ne : “Nekkleen di ay golo yu torox”.
167وَإِذْ تَأَذَّنَ رَبُّكَ لَيَبْعَثَنَّ عَلَيْهِمْ إِلَىٰ يَوْمِ الْقِيَامَةِ مَن يَسُومُهُمْ سُوءَ الْعَذَابِ ۗ إِنَّ رَبَّكَ لَسَرِيعُ الْعِقَابِ ۖ وَإِنَّهُ لَغَفُورٌ رَّحِيمٌ
[Fàttalikul] ba seen Boroom xamlee ne Dana leen yónnee ku leen di teg gëm jaa boni mbugal ba kerook Bis-pénc di agsi. Sa Boroom nag Ku gaaw la ci mbugal te Moom Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
165Aaya

Tekki — Al-A'raf 165

Simoore Al-A'raf Aaya 165 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu fàttee la ñu leen doon waare, musal Nanu…

Simoore Aaya 165/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 163–167. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers