Al-A'raf · 202/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
وَإِخْوَانُهُمْ يَمُدُّونَهُمْ فِي الْغَيِّ ثُمَّ لَا يُقْصِرُونَ ٢٠٢
Transliteration
Wa ikhwaanuhum yamuddoonahum fil ghaiyi summa laa yuqsiroon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Mu am seen kuute ñoo xam ne danañu leen tàbbal ci ag réer, te di leen ca xamb rekk.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 200-204 — Al-A'raf
200وَإِمَّا يَنزَغَنَّكَ مِنَ الشَّيْطَانِ نَزْغٌ فَاسْتَعِذْ بِاللَّهِ ۚ إِنَّهُ سَمِيعٌ عَلِيمٌ
Saa su la ag soppeeku dalee, gu tukke ci Séytaane, nanga sàkku mucc ci Yàlla. Moom Yàlla nag Kuy dégg la, Kuy xam la.
201إِنَّ الَّذِينَ اتَّقَوْا إِذَا مَسَّهُمْ طَائِفٌ مِّنَ الشَّيْطَانِ تَذَكَّرُوا فَإِذَا هُم مُّبْصِرُونَ
Ña ragal Yàlla, bu leen lu metti dalee, tukke ci Séytaane, ñu fàttaliku [seen Boroom] daldi nekk ñu am ràññee.
202وَإِخْوَانُهُمْ يَمُدُّونَهُمْ فِي الْغَيِّ ثُمَّ لَا يُقْصِرُونَ
Mu am seen kuute ñoo xam ne danañu leen tàbbal ci ag réer, te di leen ca xamb rekk.
203وَإِذَا لَمْ تَأْتِهِم بِآيَةٍ قَالُوا لَوْلَا اجْتَبَيْتَهَا ۚ قُلْ إِنَّمَا أَتَّبِعُ مَا يُوحَىٰ إِلَيَّ مِن رَّبِّي ۚ هَٰذَا بَصَائِرُ مِن رَّبِّكُمْ وَهُدًى وَرَحْمَةٌ لِّقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Te bu ndigal ñëwul, ñu naan : “Lu tee nga fental ko sa bopp ? ” Neel : “Duma def lu dul topp li ñu ma soloo mu tukke ci sama Boroom. Loolu ay lay la yu tukkee ci seen Boroom, di njub ak yërmaande ci nit ñu gëm.
204وَإِذَا قُرِئَ الْقُرْآنُ فَاسْتَمِعُوا لَهُ وَأَنصِتُوا لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Kon bu ñuy jàng Alxuraan, nangeen ko déglu te nangeen ko xarawlu ndax xéy-na yërëmees leen.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
202Aaya
Tekki — Al-A'raf 202
Simoore Al-A'raf Aaya 202 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu am seen kuute ñoo xam ne danañu leen tàbbal…Simoore Aaya 202/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 200–204. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








