Al-A'raf · 63/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
أَوَعَجِبْتُمْ أَن جَاءَكُمْ ذِكْرٌ مِّن رَّبِّكُمْ عَلَىٰ رَجُلٍ مِّنكُمْ لِيُنذِرَكُمْ وَلِتَتَّقُوا وَلَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ ۝٦٣
awa`ajibtum an jaaa`akum zikrum mir Rabbikum `alaa rajulim minkum liyunzirakum wa litattaqoo wa la`allakum turhamoon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dafa leen a jaaxal, ay kàdduy waare dikkal leen tukkee ca seen Boroom, jaare ci góor gu bokk ci yéen, ngir mu artu leen ngeen ragal Yàlla, ndax xéy-na yërëmeef leen ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 61-65 — Simoore Al-A'raf

61قَالَ يَا قَوْمِ لَيْسَ بِي ضَلَالَةٌ وَلَٰكِنِّي رَسُولٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ
Mu ne : "Man nekkuma ci ag réer ; Waaye man kat ab Yonentub Yàlla, miy Boroom àddina si, laa.
62أُبَلِّغُكُمْ رِسَالَاتِ رَبِّي وَأَنصَحُ لَكُمْ وَأَعْلَمُ مِنَ اللَّهِ مَا لَا تَعْلَمُونَ
Dama leen di jottali sama bataaxalub Boroom, te dama leen di laabire, te xam naa ci Yàlla lu ngeen xamul.
63أَوَعَجِبْتُمْ أَن جَاءَكُمْ ذِكْرٌ مِّن رَّبِّكُمْ عَلَىٰ رَجُلٍ مِّنكُمْ لِيُنذِرَكُمْ وَلِتَتَّقُوا وَلَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Moo ndax dafa leen a jaaxal, ay kàdduy waare dikkal leen tukkee ca seen Boroom, jaare ci góor gu bokk ci yéen, ngir mu artu leen ngeen ragal Yàlla, ndax xéy-na yërëmeef leen ? ”
64فَكَذَّبُوهُ فَأَنجَيْنَاهُ وَالَّذِينَ مَعَهُ فِي الْفُلْكِ وَأَغْرَقْنَا الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا عَمِينَ
Ñu weddi ko. Nu musal ko, moom ak ña nekkoon ak moom ca gaal ga, Nu labal ña weddi samay kàddu. Ñooña, aw nitam ñu gumba lañu woon.
65۞ وَإِلَىٰ عَادٍ أَخَاهُمْ هُودًا ۗ قَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۚ أَفَلَا تَتَّقُونَ
[Yónni woon Nanu it] ca waa [Haad], seen mbokk [Huud], mu ne leen : "Yéen samay mbokk, jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen Yàlla ju dul Moom. Moo ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
63Aaya

Tekki — Al-A'raf 63

Simoore Al-A'raf Aaya 63 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dafa leen a jaaxal, ay kàdduy waare dikkal…

Simoore Aaya 63/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 61–65. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers