Al-Ma'arij · 19/44
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ma'arij
۞ إِنَّ الْإِنسَانَ خُلِقَ هَلُوعًا ۝١٩
Innal insaana khuliqa haloo`aa
📖 Tekkim Wolof
Bindéef na nit ci xel muy jaxasoo [di yoqat] ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 17-21 — Simoore Al-Ma'arij

17تَدْعُو مَنْ أَدْبَرَ وَتَوَلَّىٰ
Dafay woo képp ku ne wërëñ ba bëgg a dem,
18وَجَمَعَ فَأَوْعَىٰ
dajaley alal ba dencu ko.
19۞ إِنَّ الْإِنسَانَ خُلِقَ هَلُوعًا
Bindéef na nit ci xel muy jaxasoo [di yoqat] ;
20إِذَا مَسَّهُ الشَّرُّ جَزُوعًا
su ko aw ay laalee, muy saalit ;
21وَإِذَا مَسَّهُ الْخَيْرُ مَنُوعًا
su ko jàmm ganesee mu nay, alal ak yiw danay tax mu nay bew.
Al-Ma'arijFihi Alxuraan
44Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — Al-Ma'arij 19

Simoore Al-Ma'arij Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bindéef na nit ci xel muy jaxasoo [di yoqat] ;

Simoore Aaya 19/44 — Simoore Al-Ma'arij المعارج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ma'arij Dégg, Simoore Al-Ma'arij Tekki, Simoore Al-Ma'arij mp3, Simoore Al-Ma'arij pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers