Al-Ma'arij · 18/44
Tekki Waxtaan — Al-Ma'arij
وَجَمَعَ فَأَوْعَىٰ ۝١٨
W jama`a fa aw`aa
📖 Tekkim Wolof
dajaley alal ba dencu ko.

🎧 Dégg


📜 Aaya 16-20 — Al-Ma'arij

16نَزَّاعَةً لِّلشَّوَىٰ
(Tàng) bay wësëm kaaŋum bopp.
17تَدْعُو مَنْ أَدْبَرَ وَتَوَلَّىٰ
Dafay woo képp ku ne wërëñ ba bëgg a dem,
18وَجَمَعَ فَأَوْعَىٰ
dajaley alal ba dencu ko.
19۞ إِنَّ الْإِنسَانَ خُلِقَ هَلُوعًا
Bindéef na nit ci xel muy jaxasoo [di yoqat] ;
20إِذَا مَسَّهُ الشَّرُّ جَزُوعًا
su ko aw ay laalee, muy saalit ;
Al-Ma'arijFihi Alxuraan
44Aaya
MeccanRevelation
18Aaya

Tekki — Al-Ma'arij 18

Simoore Al-Ma'arij Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dajaley alal ba dencu ko.

Simoore Aaya 18/44 — Al-Ma'arij المعارج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ma'arij Dégg, Al-Ma'arij Tekki, Al-Ma'arij mp3, Al-Ma'arij pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers