Al-Muzzammil · 17/20
Tekki Waxtaan — Al-Muzzammil
فَكَيْفَ تَتَّقُونَ إِن كَفَرْتُمْ يَوْمًا يَجْعَلُ الْوِلْدَانَ شِيبًا ۝١٧
Fakaifa tattaqoona in kafartum yawmany yaj`alul wildaana sheeba
📖 Tekkim Wolof
Ana naka ngeen di ragale (Yàlla), su ngeen weddee, bis boo xam ne tiit ma bijaawloona ab liir ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 15-19 — Al-Muzzammil

15إِنَّا أَرْسَلْنَا إِلَيْكُمْ رَسُولًا شَاهِدًا عَلَيْكُمْ كَمَا أَرْسَلْنَا إِلَىٰ فِرْعَوْنَ رَسُولًا
Yónni nanu ci yéen ab Yonent muy seede, kem ni nu yónnee woon ca Firawna ab Yonent.
16فَعَصَىٰ فِرْعَوْنُ الرَّسُولَ فَأَخَذْنَاهُ أَخْذًا وَبِيلًا
Firawna daldi moy Yonenta ba. Nu daldi koy jël bu metti. (faagaagal ko).
17فَكَيْفَ تَتَّقُونَ إِن كَفَرْتُمْ يَوْمًا يَجْعَلُ الْوِلْدَانَ شِيبًا
Ana naka ngeen di ragale (Yàlla), su ngeen weddee, bis boo xam ne tiit ma bijaawloona ab liir ?
18السَّمَاءُ مُنفَطِرٌ بِهِ ۚ كَانَ وَعْدُهُ مَفْعُولًا
Su asamaan si dee xar. Ca la digam ba di mate.
19إِنَّ هَٰذِهِ تَذْكِرَةٌ ۖ فَمَن شَاءَ اتَّخَذَ إِلَىٰ رَبِّهِ سَبِيلًا
Lii nag ag fàttali la. Képp ku mu soob mu jël yoon wa jëm ca Boroomam aw ca.
Al-MuzzammilFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — Al-Muzzammil 17

Simoore Al-Muzzammil Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ana naka ngeen di ragale (Yàlla), su ngeen weddee, bis…

Simoore Aaya 17/20 — Al-Muzzammil المزمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Muzzammil Dégg, Al-Muzzammil Tekki, Al-Muzzammil mp3, Al-Muzzammil pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers