Al-Qiyama · 15/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
وَلَوْ أَلْقَىٰ مَعَاذِيرَهُ ۝١٥
Wa law alqaa ma`aazeerah
📖 Tekkim Wolof
dontela sax dafay jégalu ak miim.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 13-17 — Simoore Al-Qiyama

13يُنَبَّأُ الْإِنسَانُ يَوْمَئِذٍ بِمَا قَدَّمَ وَأَخَّرَ
Ca la ñuy xamale nit la mu jëkka def ba ci li mu mujjoon def (cig dundam).
14بَلِ الْإِنسَانُ عَلَىٰ نَفْسِهِ بَصِيرَةٌ
Li war moo di ne nit mooy seede boppam,
15وَلَوْ أَلْقَىٰ مَعَاذِيرَهُ
dontela sax dafay jégalu ak miim.
16لَا تُحَرِّكْ بِهِ لِسَانَكَ لِتَعْجَلَ بِهِ
(Su Alxuraan) di wàcc (yaw Muhammad) bul di yëngël saw làmmiñ ngir gaawtoo ko :
17إِنَّ عَلَيْنَا جَمْعَهُ وَقُرْآنَهُ
Sol la ko aku jàngiinam, Nun la war.
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-Qiyama 15

Simoore Al-Qiyama Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dontela sax dafay jégalu ak miim.

Simoore Aaya 15/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers