Al-Qiyama · 14/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
بَلِ الْإِنسَانُ عَلَىٰ نَفْسِهِ بَصِيرَةٌ ۝١٤
Balil insaanu `alaa nafsihee baseerah
📖 Tekkim Wolof
Li war moo di ne nit mooy seede boppam,

🎧 Dégg


📜 Aaya 12-16 — Simoore Al-Qiyama

12إِلَىٰ رَبِّكَ يَوْمَئِذٍ الْمُسْتَقَرُّ
Bis boobu kay, dellu ca sa Boroom, rekk ay am.
13يُنَبَّأُ الْإِنسَانُ يَوْمَئِذٍ بِمَا قَدَّمَ وَأَخَّرَ
Ca la ñuy xamale nit la mu jëkka def ba ci li mu mujjoon def (cig dundam).
14بَلِ الْإِنسَانُ عَلَىٰ نَفْسِهِ بَصِيرَةٌ
Li war moo di ne nit mooy seede boppam,
15وَلَوْ أَلْقَىٰ مَعَاذِيرَهُ
dontela sax dafay jégalu ak miim.
16لَا تُحَرِّكْ بِهِ لِسَانَكَ لِتَعْجَلَ بِهِ
(Su Alxuraan) di wàcc (yaw Muhammad) bul di yëngël saw làmmiñ ngir gaawtoo ko :
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Al-Qiyama 14

Simoore Al-Qiyama Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Li war moo di ne nit mooy seede boppam,

Simoore Aaya 14/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers