Al-Qiyama · 16/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
لَا تُحَرِّكْ بِهِ لِسَانَكَ لِتَعْجَلَ بِهِ ۝١٦
Laa tuharrik bihee lisaa naka lita`jala bih
📖 Tekkim Wolof
(Su Alxuraan) di wàcc (yaw Muhammad) bul di yëngël saw làmmiñ ngir gaawtoo ko :

🎧 Dégg


📜 Aaya 14-18 — Simoore Al-Qiyama

14بَلِ الْإِنسَانُ عَلَىٰ نَفْسِهِ بَصِيرَةٌ
Li war moo di ne nit mooy seede boppam,
15وَلَوْ أَلْقَىٰ مَعَاذِيرَهُ
dontela sax dafay jégalu ak miim.
16لَا تُحَرِّكْ بِهِ لِسَانَكَ لِتَعْجَلَ بِهِ
(Su Alxuraan) di wàcc (yaw Muhammad) bul di yëngël saw làmmiñ ngir gaawtoo ko :
17إِنَّ عَلَيْنَا جَمْعَهُ وَقُرْآنَهُ
Sol la ko aku jàngiinam, Nun la war.
18فَإِذَا قَرَأْنَاهُ فَاتَّبِعْ قُرْآنَهُ
Te suñu koy jàng na ngay toppaat, njàng ma.
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Qiyama 16

Simoore Al-Qiyama Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Su Alxuraan) di wàcc (yaw Muhammad) bul di yëngël saw…

Simoore Aaya 16/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers