Al-Qiyama · 31/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
فَلَا صَدَّقَ وَلَا صَلَّىٰ ۝٣١
Falaa saddaqa wa laa sallaa
📖 Tekkim Wolof
Gëmul woon, te it daawuloon julli;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 29-33 — Simoore Al-Qiyama

29وَالْتَفَّتِ السَّاقُ بِالسَّاقِ
yeel ya daldi jaxasoo rawaasoo,
30إِلَىٰ رَبِّكَ يَوْمَئِذٍ الْمَسَاقُ
Bu keroogee, ñu wommat la jaŋat-jaŋatee la jëm ca sa Boroom.
31فَلَا صَدَّقَ وَلَا صَلَّىٰ
Gëmul woon, te it daawuloon julli;
32وَلَٰكِن كَذَّبَ وَتَوَلَّىٰ
waaye, moom sax dafa weddi woon dumóoyu,
33ثُمَّ ذَهَبَ إِلَىٰ أَهْلِهِ يَتَمَطَّىٰ
daldi dem nag ca aw nitam, di xoggaliku.
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — Al-Qiyama 31

Simoore Al-Qiyama Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Gëmul woon, te it daawuloon julli;

Simoore Aaya 31/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers