Al-Qiyama · 32/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
وَلَٰكِن كَذَّبَ وَتَوَلَّىٰ ۝٣٢
Wa laakin kazzaba wa tawalla
📖 Tekkim Wolof
waaye, moom sax dafa weddi woon dumóoyu,

🎧 Dégg


📜 Aaya 30-34 — Simoore Al-Qiyama

30إِلَىٰ رَبِّكَ يَوْمَئِذٍ الْمَسَاقُ
Bu keroogee, ñu wommat la jaŋat-jaŋatee la jëm ca sa Boroom.
31فَلَا صَدَّقَ وَلَا صَلَّىٰ
Gëmul woon, te it daawuloon julli;
32وَلَٰكِن كَذَّبَ وَتَوَلَّىٰ
waaye, moom sax dafa weddi woon dumóoyu,
33ثُمَّ ذَهَبَ إِلَىٰ أَهْلِهِ يَتَمَطَّىٰ
daldi dem nag ca aw nitam, di xoggaliku.
34أَوْلَىٰ لَكَ فَأَوْلَىٰ
“Yaayoo nga toskare, yaayoo nga toskare! ”
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Al-Qiyama 32

Simoore Al-Qiyama Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : waaye, moom sax dafa weddi woon dumóoyu,

Simoore Aaya 32/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers