Al-Qiyama · 4/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
بَلَىٰ قَادِرِينَ عَلَىٰ أَن نُّسَوِّيَ بَنَانَهُ ۝٤
Balaa qaadireena `alaaa an nusawwiya banaanah
📖 Tekkim Wolof
Axakañ ! Mën nañoo dajale yemalewaat cati waaraamam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-Qiyama

2وَلَا أُقْسِمُ بِالنَّفْسِ اللَّوَّامَةِ
Te maa ngi giñ ci bakkan bi di ab yeddaakoon.
3أَيَحْسَبُ الْإِنسَانُ أَلَّن نَّجْمَعَ عِظَامَهُ
Moo ndax, nit ki dafa foog ne dunu dajale ay yaxam ?
4بَلَىٰ قَادِرِينَ عَلَىٰ أَن نُّسَوِّيَ بَنَانَهُ
Axakañ ! Mën nañoo dajale yemalewaat cati waaraamam.
5بَلْ يُرِيدُ الْإِنسَانُ لِيَفْجُرَ أَمَامَهُ
Te nit moom day bëgg rekk di dund cig boy.
6يَسْأَلُ أَيَّانَ يَوْمُ الْقِيَامَةِ
Muy laaj : “Kañ la, Bisub Dekkiwaat ba ? ”
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Qiyama 4

Simoore Al-Qiyama Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Axakañ ! Mën nañoo dajale yemalewaat cati waaraamam.

Simoore Aaya 4/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers