Al-Qiyama · 3/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
أَيَحْسَبُ الْإِنسَانُ أَلَّن نَّجْمَعَ عِظَامَهُ ۝٣
Ayahsabul insaanu al lan najm`a `izaamah
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax, nit ki dafa foog ne dunu dajale ay yaxam ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-5 — Simoore Al-Qiyama

1لَا أُقْسِمُ بِيَوْمِ الْقِيَامَةِ
Maa ngi giñ ci bisub dekkiwaat ga !
2وَلَا أُقْسِمُ بِالنَّفْسِ اللَّوَّامَةِ
Te maa ngi giñ ci bakkan bi di ab yeddaakoon.
3أَيَحْسَبُ الْإِنسَانُ أَلَّن نَّجْمَعَ عِظَامَهُ
Moo ndax, nit ki dafa foog ne dunu dajale ay yaxam ?
4بَلَىٰ قَادِرِينَ عَلَىٰ أَن نُّسَوِّيَ بَنَانَهُ
Axakañ ! Mën nañoo dajale yemalewaat cati waaraamam.
5بَلْ يُرِيدُ الْإِنسَانُ لِيَفْجُرَ أَمَامَهُ
Te nit moom day bëgg rekk di dund cig boy.
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-Qiyama 3

Simoore Al-Qiyama Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax, nit ki dafa foog ne dunu dajale ay…

Simoore Aaya 3/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers