Al-Qiyama · 5/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
بَلْ يُرِيدُ الْإِنسَانُ لِيَفْجُرَ أَمَامَهُ ۝٥
Bal yureedul insaanu liyafjura amaamah
📖 Tekkim Wolof
Te nit moom day bëgg rekk di dund cig boy.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 3-7 — Simoore Al-Qiyama

3أَيَحْسَبُ الْإِنسَانُ أَلَّن نَّجْمَعَ عِظَامَهُ
Moo ndax, nit ki dafa foog ne dunu dajale ay yaxam ?
4بَلَىٰ قَادِرِينَ عَلَىٰ أَن نُّسَوِّيَ بَنَانَهُ
Axakañ ! Mën nañoo dajale yemalewaat cati waaraamam.
5بَلْ يُرِيدُ الْإِنسَانُ لِيَفْجُرَ أَمَامَهُ
Te nit moom day bëgg rekk di dund cig boy.
6يَسْأَلُ أَيَّانَ يَوْمُ الْقِيَامَةِ
Muy laaj : “Kañ la, Bisub Dekkiwaat ba ? ”
7فَإِذَا بَرِقَ الْبَصَرُ
Su gis ba nee melxat gëlam,
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-Qiyama 5

Simoore Al-Qiyama Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te nit moom day bëgg rekk di dund cig boy.

Simoore Aaya 5/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers