An-Naba · 27/40
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naba
إِنَّهُمْ كَانُوا لَا يَرْجُونَ حِسَابًا ۝٢٧
Innahum kaanu laa yarjoona hisaaba
📖 Tekkim Wolof
Ñoom dañoo foogoon ne duñu leen màndaxe,

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-29 — Simoore An-Naba

25إِلَّا حَمِيمًا وَغَسَّاقًا
Lu dul ndox muy wañax ak lay rogaate ca seen jëmm ya
26جَزَاءً وِفَاقًا
muy pey gu témbóo.
27إِنَّهُمْ كَانُوا لَا يَرْجُونَ حِسَابًا
Ñoom dañoo foogoon ne duñu leen màndaxe,
28وَكَذَّبُوا بِآيَاتِنَا كِذَّابًا
ña weddiwoon sunuy Laaya,
29وَكُلَّ شَيْءٍ أَحْصَيْنَاهُ كِتَابًا
lépp lu ne peek nanu ko bind ko.
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — An-Naba 27

Simoore An-Naba Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoom dañoo foogoon ne duñu leen màndaxe,

Simoore Aaya 27/40 — Simoore An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naba Dégg, Simoore An-Naba Tekki, Simoore An-Naba mp3, Simoore An-Naba pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers