Abasa · 16/42
Tekki Waxtaan — Simoore Abasa
كِرَامٍ بَرَرَةٍ ۝١٦
Kiraamim bararah
📖 Tekkim Wolof
yu tedd, yu baax.

🎧 Dégg


📜 Aaya 14-18 — Simoore Abasa

14مَّرْفُوعَةٍ مُّطَهَّرَةٍ
yu ñu yékëti, te laabal ko,
15بِأَيْدِي سَفَرَةٍ
nekk ci yoxoy ak tekkikat (malaaka)
16كِرَامٍ بَرَرَةٍ
yu tedd, yu baax.
17قُتِلَ الْإِنسَانُ مَا أَكْفَرَهُ
reyeef na nit ngir ngoreedeem !
18مِنْ أَيِّ شَيْءٍ خَلَقَهُ
Ci lan la ko [Yàlla] bind ?
AbasaFihi Alxuraan
42Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Abasa 16

Simoore Abasa Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : yu tedd, yu baax.

Simoore Aaya 16/42 — Simoore Abasa عبس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Abasa Dégg, Simoore Abasa Tekki, Simoore Abasa mp3, Simoore Abasa pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers