Al-Fajr · 16/30
Tekki Waxtaan — Al-Fajr
وَأَمَّا إِذَا مَا ابْتَلَاهُ فَقَدَرَ عَلَيْهِ رِزْقَهُ فَيَقُولُ رَبِّي أَهَانَنِ ١٦
Transliteration
Wa ammaaa izaa mabtalaahu faqadara `alaihi rizqahoo fa yaqoolu Rabbeee ahaanan
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Saa su ko nattoo wàññi wërsagëm, muy wax naan : “Sama Boroom toroxal nama”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 14-18 — Al-Fajr
14إِنَّ رَبَّكَ لَبِالْمِرْصَادِ
Sa Boroom nag ma ngay fuglu.
15فَأَمَّا الْإِنسَانُ إِذَا مَا ابْتَلَاهُ رَبُّهُ فَأَكْرَمَهُ وَنَعَّمَهُ فَيَقُولُ رَبِّي أَكْرَمَنِ
Nit nag, moom saa su ko boroomam nattoo teral ko xéewal ko, mu ne : “Sama Boroom teral na ma”.
16وَأَمَّا إِذَا مَا ابْتَلَاهُ فَقَدَرَ عَلَيْهِ رِزْقَهُ فَيَقُولُ رَبِّي أَهَانَنِ
Saa su ko nattoo wàññi wërsagëm, muy wax naan : “Sama Boroom toroxal nama”.
17كَلَّا ۖ بَل لَّا تُكْرِمُونَ الْيَتِيمَ
Déedéet ! Yéen kay, du ngeen teral mukk jirim ak di tabe ci moom ;
18وَلَا تَحَاضُّونَ عَلَىٰ طَعَامِ الْمِسْكِينِ
te it du ngeen sonnu mukk ci di leel miskiin,
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
16Aaya
Tekki — Al-Fajr 16
Simoore Al-Fajr Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Saa su ko nattoo wàññi wërsagëm, muy wax naan :…Simoore Aaya 16/30 — Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Fajr Dégg, Al-Fajr Tekki, Al-Fajr mp3, Al-Fajr pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








