Al-Fajr · 17/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Fajr
كَلَّا ۖ بَل لَّا تُكْرِمُونَ الْيَتِيمَ ۝١٧
Kalla bal laa tukrimooo nal yateem
📖 Tekkim Wolof
Déedéet ! Yéen kay, du ngeen teral mukk jirim ak di tabe ci moom ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 15-19 — Simoore Al-Fajr

15فَأَمَّا الْإِنسَانُ إِذَا مَا ابْتَلَاهُ رَبُّهُ فَأَكْرَمَهُ وَنَعَّمَهُ فَيَقُولُ رَبِّي أَكْرَمَنِ
Nit nag, moom saa su ko boroomam nattoo teral ko xéewal ko, mu ne : “Sama Boroom teral na ma”.
16وَأَمَّا إِذَا مَا ابْتَلَاهُ فَقَدَرَ عَلَيْهِ رِزْقَهُ فَيَقُولُ رَبِّي أَهَانَنِ
Saa su ko nattoo wàññi wërsagëm, muy wax naan : “Sama Boroom toroxal nama”.
17كَلَّا ۖ بَل لَّا تُكْرِمُونَ الْيَتِيمَ
Déedéet ! Yéen kay, du ngeen teral mukk jirim ak di tabe ci moom ;
18وَلَا تَحَاضُّونَ عَلَىٰ طَعَامِ الْمِسْكِينِ
te it du ngeen sonnu mukk ci di leel miskiin,
19وَتَأْكُلُونَ التُّرَاثَ أَكْلًا لَّمًّا
te ngeen di lekk alal ndono lekkiin wu ñaaw,
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — Al-Fajr 17

Simoore Al-Fajr Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Déedéet ! Yéen kay, du ngeen teral mukk jirim ak…

Simoore Aaya 17/30 — Simoore Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Fajr Dégg, Simoore Al-Fajr Tekki, Simoore Al-Fajr mp3, Simoore Al-Fajr pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers