Al-Fajr · 19/30
Tekki Waxtaan — Al-Fajr
وَتَأْكُلُونَ التُّرَاثَ أَكْلًا لَّمًّا ١٩
Transliteration
Wa taakuloonat turaasa aklal lammaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
te ngeen di lekk alal ndono lekkiin wu ñaaw,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 17-21 — Al-Fajr
17كَلَّا ۖ بَل لَّا تُكْرِمُونَ الْيَتِيمَ
Déedéet ! Yéen kay, du ngeen teral mukk jirim ak di tabe ci moom ;
18وَلَا تَحَاضُّونَ عَلَىٰ طَعَامِ الْمِسْكِينِ
te it du ngeen sonnu mukk ci di leel miskiin,
19وَتَأْكُلُونَ التُّرَاثَ أَكْلًا لَّمًّا
te ngeen di lekk alal ndono lekkiin wu ñaaw,
20وَتُحِبُّونَ الْمَالَ حُبًّا جَمًّا
te da ngeen bëgg alal bëgg gu tar.
21كَلَّا إِذَا دُكَّتِ الْأَرْضُ دَكًّا دَكًّا
(Bàyyileen xel) ! saa su nu walee suuf si ba mu di pëndax,
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
19Aaya
Tekki — Al-Fajr 19
Simoore Al-Fajr Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te ngeen di lekk alal ndono lekkiin wu ñaaw,Simoore Aaya 19/30 — Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Fajr Dégg, Al-Fajr Tekki, Al-Fajr mp3, Al-Fajr pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








