Al-Fajr · 10/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Fajr
وَفِرْعَوْنَ ذِي الْأَوْتَادِ ۝١٠
Wa fir`awna zil awtaad
📖 Tekkim Wolof
ak Firawna, ma doonoon boroomi dàtt ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 8-12 — Simoore Al-Fajr

8الَّتِي لَمْ يُخْلَقْ مِثْلُهَا فِي الْبِلَادِ
yoo xam ne kemam amul ci menn réew ?
9وَثَمُودَ الَّذِينَ جَابُوا الصَّخْرَ بِالْوَادِ
ak waa Saamud ña daan yatt xeer ya ca xur ya ?
10وَفِرْعَوْنَ ذِي الْأَوْتَادِ
ak Firawna, ma doonoon boroomi dàtt ?
11الَّذِينَ طَغَوْا فِي الْبِلَادِ
Ñoom, ñoo gënoona bew ci réew yi,
12فَأَكْثَرُوا فِيهَا الْفَسَادَ
te ñu bariloon fa lool ag yàq.
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Al-Fajr 10

Simoore Al-Fajr Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak Firawna, ma doonoon boroomi dàtt ?

Simoore Aaya 10/30 — Simoore Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Fajr Dégg, Simoore Al-Fajr Tekki, Simoore Al-Fajr mp3, Simoore Al-Fajr pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers