Yunus · 103/109
Tekki Waxtaan — Yunus
ثُمَّ نُنَجِّي رُسُلَنَا وَالَّذِينَ آمَنُوا ۚ كَذَٰلِكَ حَقًّا عَلَيْنَا نُنجِ الْمُؤْمِنِينَ ۝١٠٣
Summma nunajjee Ruslanaa wallazeena aamanoo; kazaalika haqqan `alainaa nunjil mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Topp ginnaaw ba, Nu musal Sunuy Yonent ak ña gëm. Noonu la yaye ci Nun Nuy musal ñi gëm.

🎧 Dégg


📜 Aaya 101-105 — Yunus

101قُلِ انظُرُوا مَاذَا فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَمَا تُغْنِي الْآيَاتُ وَالنُّذُرُ عَن قَوْمٍ لَّا يُؤْمِنُونَ
Neel : “Xool-leen li nekk ci asamaan yi ak suuf si”. Te kaawtéef ya ak waaraate ya duñu jariñ dara ci aw nit ñu gëmul.
102فَهَلْ يَنتَظِرُونَ إِلَّا مِثْلَ أَيَّامِ الَّذِينَ خَلَوْا مِن قَبْلِهِمْ ۚ قُلْ فَانتَظِرُوا إِنِّي مَعَكُم مِّنَ الْمُنتَظِرِينَ
Moo ndax ñooña dañuy xaar ba mu deme ni bis yu tiis, yu ña leen jiitu woon dajoon, agsi ci ñoom ? Neleen : “Muñandikuleen ! Man it maa ngi bokk ci ñay muñandiku”.
103ثُمَّ نُنَجِّي رُسُلَنَا وَالَّذِينَ آمَنُوا ۚ كَذَٰلِكَ حَقًّا عَلَيْنَا نُنجِ الْمُؤْمِنِينَ
Topp ginnaaw ba, Nu musal Sunuy Yonent ak ña gëm. Noonu la yaye ci Nun Nuy musal ñi gëm.
104قُلْ يَا أَيُّهَا النَّاسُ إِن كُنتُمْ فِي شَكٍّ مِّن دِينِي فَلَا أَعْبُدُ الَّذِينَ تَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ وَلَٰكِنْ أَعْبُدُ اللَّهَ الَّذِي يَتَوَفَّاكُمْ ۖ وَأُمِرْتُ أَنْ أَكُونَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Neel : "Éy yéen nit ñi ! Bu ngeen amee xel-ñaar ci sama diine jii, xamleen ne man duma jaamu li ngeen di jaamu bàyyi Yàlla ; Waaye Yàlla laay jaamu, Moom mi leen di rey. Te digaleef na ma ma bokk ca way-gëm ña”.
105وَأَنْ أَقِمْ وَجْهَكَ لِلدِّينِ حَنِيفًا وَلَا تَكُونَنَّ مِنَ الْمُشْرِكِينَ
Te : “Nga taxaw temm jublu ci diine jii wéetal Yàlla ! Te bul bokk mukk ca way- bokkaale ña ;
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
103Aaya

Tekki — Yunus 103

Simoore Yunus Aaya 103 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Topp ginnaaw ba, Nu musal Sunuy Yonent ak ña gëm.…

Simoore Aaya 103/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 101–105. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers