Yunus · 67/109
Tekki Waxtaan — Yunus
هُوَ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ اللَّيْلَ لِتَسْكُنُوا فِيهِ وَالنَّهَارَ مُبْصِرًا ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يَسْمَعُونَ ٦٧
Transliteration
Huwal lazee ja`ala lakumul laila litaskunoo feehi wannahaara mubsiraa; inna fee zaalika la Aayaatil liqawmai yasma`oon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Moom [Yàlla], moo def guddi ngir ngeen di ca noppalu, ak bëccëg ngeen di ca gise. Kéemaan nekk na ci loolu ngir aw nit ñuy dégg !
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 65-69 — Yunus
65وَلَا يَحْزُنكَ قَوْلُهُمْ ۘ إِنَّ الْعِزَّةَ لِلَّهِ جَمِيعًا ۚ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
Li ñuy wax , bumu la naqari. Teraanga nag Yàllaa moom lépp. Te Moom Kuy dégg la, Kuy xam la.
66أَلَا إِنَّ لِلَّهِ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَمَن فِي الْأَرْضِ ۗ وَمَا يَتَّبِعُ الَّذِينَ يَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ شُرَكَاءَ ۚ إِن يَتَّبِعُونَ إِلَّا الظَّنَّ وَإِنْ هُمْ إِلَّا يَخْرُصُونَ
Ca dëgg-dëgg, li nekk ci asamaan yi ak suuf si, Yàllaa leen moom. Ñay jaamu leneen lu dul Yàlla, ñoom daal toppuñu lu dul ay njort. Nekkewuñu lu dul di sos ay fen.
67هُوَ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ اللَّيْلَ لِتَسْكُنُوا فِيهِ وَالنَّهَارَ مُبْصِرًا ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يَسْمَعُونَ
Moom [Yàlla], moo def guddi ngir ngeen di ca noppalu, ak bëccëg ngeen di ca gise. Kéemaan nekk na ci loolu ngir aw nit ñuy dégg !
68قَالُوا اتَّخَذَ اللَّهُ وَلَدًا ۗ سُبْحَانَهُ ۖ هُوَ الْغَنِيُّ ۖ لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۚ إِنْ عِندَكُم مِّن سُلْطَانٍ بِهَٰذَا ۚ أَتَقُولُونَ عَلَى اللَّهِ مَا لَا تَعْلَمُونَ
Wax nañu ne : “Yàlla am na doom”. Kañ naa sellam ga ! Moom ku doylu la ci boppam. Ñeel na ko li ci asamaan yi ak suuf si ; - Amuleen aw layati ci wax jooju. Moo ndax dangeen di wax ci Yàlla lu ngeen xamul ?
69قُلْ إِنَّ الَّذِينَ يَفْتَرُونَ عَلَى اللَّهِ الْكَذِبَ لَا يُفْلِحُونَ
Neel : “Ñiy duural Yàlla ay fen duñu texe”.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
67Aaya
Tekki — Yunus 67
Simoore Yunus Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom [Yàlla], moo def guddi ngir ngeen di ca noppalu,…Simoore Aaya 67/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








