Yunus · 66/109
Tekki Waxtaan — Yunus
أَلَا إِنَّ لِلَّهِ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَمَن فِي الْأَرْضِ ۗ وَمَا يَتَّبِعُ الَّذِينَ يَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ شُرَكَاءَ ۚ إِن يَتَّبِعُونَ إِلَّا الظَّنَّ وَإِنْ هُمْ إِلَّا يَخْرُصُونَ ۝٦٦
Alaaa inna lillaahi man fis samaawaati wa man fil ard; wa maa yattabi`ul lazeena yad`oona min doonil laahi shurakaaa`; iny yattabi`oona illaz zannna wa in hum illaa yakhrusoon
📖 Tekkim Wolof
Ca dëgg-dëgg, li nekk ci asamaan yi ak suuf si, Yàllaa leen moom. Ñay jaamu leneen lu dul Yàlla, ñoom daal toppuñu lu dul ay njort. Nekkewuñu lu dul di sos ay fen.

🎧 Dégg


📜 Aaya 64-68 — Yunus

64لَهُمُ الْبُشْرَىٰ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَفِي الْآخِرَةِ ۚ لَا تَبْدِيلَ لِكَلِمَاتِ اللَّهِ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ
Am nañu mbégte ci dundug àddina ak ca àllaaxira. - Soppeeku du am ciy kàddu Yàlla -. Loolu mooy texe gu mag ga !
65وَلَا يَحْزُنكَ قَوْلُهُمْ ۘ إِنَّ الْعِزَّةَ لِلَّهِ جَمِيعًا ۚ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
Li ñuy wax , bumu la naqari. Teraanga nag Yàllaa moom lépp. Te Moom Kuy dégg la, Kuy xam la.
66أَلَا إِنَّ لِلَّهِ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَمَن فِي الْأَرْضِ ۗ وَمَا يَتَّبِعُ الَّذِينَ يَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ شُرَكَاءَ ۚ إِن يَتَّبِعُونَ إِلَّا الظَّنَّ وَإِنْ هُمْ إِلَّا يَخْرُصُونَ
Ca dëgg-dëgg, li nekk ci asamaan yi ak suuf si, Yàllaa leen moom. Ñay jaamu leneen lu dul Yàlla, ñoom daal toppuñu lu dul ay njort. Nekkewuñu lu dul di sos ay fen.
67هُوَ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ اللَّيْلَ لِتَسْكُنُوا فِيهِ وَالنَّهَارَ مُبْصِرًا ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يَسْمَعُونَ
Moom [Yàlla], moo def guddi ngir ngeen di ca noppalu, ak bëccëg ngeen di ca gise. Kéemaan nekk na ci loolu ngir aw nit ñuy dégg !
68قَالُوا اتَّخَذَ اللَّهُ وَلَدًا ۗ سُبْحَانَهُ ۖ هُوَ الْغَنِيُّ ۖ لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۚ إِنْ عِندَكُم مِّن سُلْطَانٍ بِهَٰذَا ۚ أَتَقُولُونَ عَلَى اللَّهِ مَا لَا تَعْلَمُونَ
Wax nañu ne : “Yàlla am na doom”. Kañ naa sellam ga ! Moom ku doylu la ci boppam. Ñeel na ko li ci asamaan yi ak suuf si ; - Amuleen aw layati ci wax jooju. Moo ndax dangeen di wax ci Yàlla lu ngeen xamul ?
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
66Aaya

Tekki — Yunus 66

Simoore Yunus Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ca dëgg-dëgg, li nekk ci asamaan yi ak suuf si,…

Simoore Aaya 66/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers