Yunus · 93/109
Tekki Waxtaan — Yunus
وَلَقَدْ بَوَّأْنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ مُبَوَّأَ صِدْقٍ وَرَزَقْنَاهُم مِّنَ الطَّيِّبَاتِ فَمَا اخْتَلَفُوا حَتَّىٰ جَاءَهُمُ الْعِلْمُ ۚ إِنَّ رَبَّكَ يَقْضِي بَيْنَهُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فِيمَا كَانُوا فِيهِ يَخْتَلِفُونَ ۝٩٣
Wa laqad bawwaanaa Baneee Israaa`eela mubawwa-a sidqinw wa razaqnaahum minnat taiyibaati famakh talafoo hattaa jaaa`ahmul `ilm; inna Rabbaka yaqdee bainahum Yawmal Qiyaamati feemaa kaanoo feehi yakhtalifoon
📖 Tekkim Wolof
Te wàcceel Nanu waa Banii-Israayiila wàccuwaayu teraanga, Nu xéewale leen ñam yu sell ya. Waaye réeruñu woon ba ba leen xam-xam dikkalee. Sa Boroom nag dana àtteji seen diggante bu Bis-pénc baa ci lépp lañu doon juuyoo.
🎧 Dégg

📜 Aaya 91-95 — Yunus

91آلْآنَ وَقَدْ عَصَيْتَ قَبْلُ وَكُنتَ مِنَ الْمُفْسِدِينَ
[Yàlla ne ko] : Moo ndax léegi [ngay door a gëm] ? Te nga féttéerlu woon lu jiitu te nga bokk ca yàqkat ya !
92فَالْيَوْمَ نُنَجِّيكَ بِبَدَنِكَ لِتَكُونَ لِمَنْ خَلْفَكَ آيَةً ۚ وَإِنَّ كَثِيرًا مِّنَ النَّاسِ عَنْ آيَاتِنَا لَغَافِلُونَ
Tey jii Dananu la musal ci sàmm saw yaram [mu bañ a yàqu] ngir nga nekk ci ña lay wuutu màndarga. Ndaxte ñu bari ci nit ñi dañoo sàggane Sunuy màndarga [yu leen di teete jëme ci Man seen Boroom].
93وَلَقَدْ بَوَّأْنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ مُبَوَّأَ صِدْقٍ وَرَزَقْنَاهُم مِّنَ الطَّيِّبَاتِ فَمَا اخْتَلَفُوا حَتَّىٰ جَاءَهُمُ الْعِلْمُ ۚ إِنَّ رَبَّكَ يَقْضِي بَيْنَهُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فِيمَا كَانُوا فِيهِ يَخْتَلِفُونَ
Te wàcceel Nanu waa Banii-Israayiila wàccuwaayu teraanga, Nu xéewale leen ñam yu sell ya. Waaye réeruñu woon ba ba leen xam-xam dikkalee. Sa Boroom nag dana àtteji seen diggante bu Bis-pénc baa ci lépp lañu doon juuyoo.
94فَإِن كُنتَ فِي شَكٍّ مِّمَّا أَنزَلْنَا إِلَيْكَ فَاسْأَلِ الَّذِينَ يَقْرَءُونَ الْكِتَابَ مِن قَبْلِكَ ۚ لَقَدْ جَاءَكَ الْحَقُّ مِن رَّبِّكَ فَلَا تَكُونَنَّ مِنَ الْمُمْتَرِينَ
Boo amee sikki-sàkka ci li Nu wàcce ci yaw, laajal ña jàngoon Téere ba. Ba li wér dëgg agsi na ci yaw jóge ca sa Boroom : bul bokk ci way-sikki-sàkka ña, werantekat ña.
95وَلَا تَكُونَنَّ مِنَ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِ اللَّهِ فَتَكُونَ مِنَ الْخَاسِرِينَ
Bul bokk mukk ci ñiy weddi kàdduy Yàlla. Nde kon nga bokk ca ña yàqule.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
93Aaya

Tekki — Yunus 93

Simoore Yunus Aaya 93 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te wàcceel Nanu waa Banii-Israayiila wàccuwaayu teraanga, Nu xéewale leen…

Simoore Aaya 93/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 91–95. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers