Hud · 118/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
وَلَوْ شَاءَ رَبُّكَ لَجَعَلَ النَّاسَ أُمَّةً وَاحِدَةً ۖ وَلَا يَزَالُونَ مُخْتَلِفِينَ ۝١١٨
Wa law shaaa`a Rabbuka laja`alannnaasa ummatanw waa hidatanw wa laa yazaaloona mukhtalifeen
📖 Tekkim Wolof
Bu sooboon sa Boroom mu def nit ñi ñu nekk di wenn xeet doŋŋ. Waaye duñu deñ di wuute

🎧 Dégg


📜 Aaya 116-120 — Simoore Hud

116فَلَوْلَا كَانَ مِنَ الْقُرُونِ مِن قَبْلِكُمْ أُولُو بَقِيَّةٍ يَنْهَوْنَ عَنِ الْفَسَادِ فِي الْأَرْضِ إِلَّا قَلِيلًا مِّمَّنْ أَنجَيْنَا مِنْهُمْ ۗ وَاتَّبَعَ الَّذِينَ ظَلَمُوا مَا أُتْرِفُوا فِيهِ وَكَانُوا مُجْرِمِينَ
Lu taxoon ca xarnu ya leen jiitu, ñu baax ña [dese woon yan bi] nekkoon ñu néew, ñoom ña daan tere lu bon ci suuf sa ! Ñu bokk ca ña Nu musaloon te ñu tooñoon, topp seeni bakkan ca xéewal ya ñu donnoon ay bàkkaarkat.
117وَمَا كَانَ رَبُّكَ لِيُهْلِكَ الْقُرَىٰ بِظُلْمٍ وَأَهْلُهَا مُصْلِحُونَ
Sa Boroom du alag lenn njénde ci ag tooñeel fekk aw nit di sellal seeni jëf.
118وَلَوْ شَاءَ رَبُّكَ لَجَعَلَ النَّاسَ أُمَّةً وَاحِدَةً ۖ وَلَا يَزَالُونَ مُخْتَلِفِينَ
Bu sooboon sa Boroom mu def nit ñi ñu nekk di wenn xeet doŋŋ. Waaye duñu deñ di wuute
119إِلَّا مَن رَّحِمَ رَبُّكَ ۚ وَلِذَٰلِكَ خَلَقَهُمْ ۗ وَتَمَّتْ كَلِمَةُ رَبِّكَ لَأَمْلَأَنَّ جَهَنَّمَ مِنَ الْجِنَّةِ وَالنَّاسِ أَجْمَعِينَ
ndare ña sa Boroom yërëm. Loolu moo tax Mu bind leen. Te it moo tax sa kàddug Boroom mat ca la mu wax ne : “Danaa feesal Safara ci aw nit ak i jinne mbooleseen”.
120وَكُلًّا نَّقُصُّ عَلَيْكَ مِنْ أَنبَاءِ الرُّسُلِ مَا نُثَبِّتُ بِهِ فُؤَادَكَ ۚ وَجَاءَكَ فِي هَٰذِهِ الْحَقُّ وَمَوْعِظَةٌ وَذِكْرَىٰ لِلْمُؤْمِنِينَ
Te lépp Lanu lay nittili ci xew-xewi Yonent ya, Danu cay dalal sa xel. Te dëgg ak ug waare dikkal na la di aw lay ànd ak di fàttali ci ñi gëm.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
118Aaya

Tekki — Hud 118

Simoore Hud Aaya 118 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu sooboon sa Boroom mu def nit ñi ñu nekk…

Simoore Aaya 118/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 116–120. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 21, 2026

Don't forget us in your sincere prayers