Hud · 26/123
Tekki Waxtaan — Hud
أَن لَّا تَعْبُدُوا إِلَّا اللَّهَ ۖ إِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُمْ عَذَابَ يَوْمٍ أَلِيمٍ ٢٦
Transliteration
Al laa ta`budooo illal laaha inneee akhaafu `alaikum `azaaba Yawmin aleem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
te ngeen bañ a jaamu ku dul Yàlla. Te ragalal naa leen mbugalum bis bu metti dal leen”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 24-28 — Hud
24۞ مَثَلُ الْفَرِيقَيْنِ كَالْأَعْمَىٰ وَالْأَصَمِّ وَالْبَصِيرِ وَالسَّمِيعِ ۚ هَلْ يَسْتَوِيَانِ مَثَلًا ۚ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
Niraleeb ñaari kurél yii mel na ne gumba ga ak tëx ba, ak kuy gis ak kuy dégg. Moo ndax ñaar ñooñu yem nañu te méngoo ? Moo ndax dañu dul xel-lu ?
25وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا نُوحًا إِلَىٰ قَوْمِهِ إِنِّي لَكُمْ نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Yónni woon Nanu Nooh ca aw nitam, mu ne leen : “Man waarekat laa bu leen di xamal lu leer
26أَن لَّا تَعْبُدُوا إِلَّا اللَّهَ ۖ إِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُمْ عَذَابَ يَوْمٍ أَلِيمٍ
te ngeen bañ a jaamu ku dul Yàlla. Te ragalal naa leen mbugalum bis bu metti dal leen”.
27فَقَالَ الْمَلَأُ الَّذِينَ كَفَرُوا مِن قَوْمِهِ مَا نَرَاكَ إِلَّا بَشَرًا مِّثْلَنَا وَمَا نَرَاكَ اتَّبَعَكَ إِلَّا الَّذِينَ هُمْ أَرَاذِلُنَا بَادِيَ الرَّأْيِ وَمَا نَرَىٰ لَكُمْ عَلَيْنَا مِن فَضْلٍ بَلْ نَظُنُّكُمْ كَاذِبِينَ
Ña di ay kilifa ci aw nitam, te weddi, ne ko : “Xoolewunu la lu dul ngay kenn rekk ci nun ; te it gisunu ñi la topp ñu dul ñi gën a suufe ci nun te lu yomb a gis ; te ëppalewuleen nu dara. Te sax am nanu njort ci ne ay fenkat ngeen”.
28قَالَ يَا قَوْمِ أَرَأَيْتُمْ إِن كُنتُ عَلَىٰ بَيِّنَةٍ مِّن رَّبِّي وَآتَانِي رَحْمَةً مِّنْ عِندِهِ فَعُمِّيَتْ عَلَيْكُمْ أَنُلْزِمُكُمُوهَا وَأَنتُمْ لَهَا كَارِهُونَ
Mu ne leen : "Samaw nit ! Naka ngeen di gisee mbir mi ? Su fekkee maa ngi ci lu wér lu jóge ci sama Boroom, te Mu jox ma yërmaande ju jóge ci Moom ci lu nëbbu ci yéen, ndax dama cee ga te fekk yéen ngeen sib ko ?
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
26Aaya
Tekki — Hud 26
Simoore Hud Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te ngeen bañ a jaamu ku dul Yàlla. Te ragalal…Simoore Aaya 26/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








