Hud · 65/123
Tekki Waxtaan — Hud
فَعَقَرُوهَا فَقَالَ تَمَتَّعُوا فِي دَارِكُمْ ثَلَاثَةَ أَيَّامٍ ۖ ذَٰلِكَ وَعْدٌ غَيْرُ مَكْذُوبٍ ۝٦٥
Fa `aqaroohaa faqaala tamatta`oo fee daarikum salaasata aiyaamin zaalika wa`dun ghairu makzoob
📖 Tekkim Wolof
Ñu rey ko. Mu ne leen : “Xéewluleen ci seeni kër ñetti fan ! Loolu àpp la bu dul deñ”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 63-67 — Hud

63قَالَ يَا قَوْمِ أَرَأَيْتُمْ إِن كُنتُ عَلَىٰ بَيِّنَةٍ مِّن رَّبِّي وَآتَانِي مِنْهُ رَحْمَةً فَمَن يَنصُرُنِي مِنَ اللَّهِ إِنْ عَصَيْتُهُ ۖ فَمَا تَزِيدُونَنِي غَيْرَ تَخْسِيرٍ
Mu ne : "Yéen samaw nit! Ndax niir ngeen ba gis ne ndax nekk naa ci lu leer lu tukkee ci sama Boroom, te Mu jox ma yërmaande ju jógeci Moom, te ana kan moo may musal ci Yàlla su ma moyee [ndigëlam] ? Te kon sax dungeen ma yokkal lu dul ag yàqule.
64وَيَا قَوْمِ هَٰذِهِ نَاقَةُ اللَّهِ لَكُمْ آيَةً فَذَرُوهَا تَأْكُلْ فِي أَرْضِ اللَّهِ وَلَا تَمَسُّوهَا بِسُوءٍ فَيَأْخُذَكُمْ عَذَابٌ قَرِيبٌ
Éy yéen samaw nit, giléemug Yàlla gii na nekk kéemaan ci yéen. Bàyyileen ko muy lekk ci kaw suufus Yàlla si, buleen ko def dara lu bon, kon mbugal dana leen dal bu gaaw ! ”
65فَعَقَرُوهَا فَقَالَ تَمَتَّعُوا فِي دَارِكُمْ ثَلَاثَةَ أَيَّامٍ ۖ ذَٰلِكَ وَعْدٌ غَيْرُ مَكْذُوبٍ
Ñu rey ko. Mu ne leen : “Xéewluleen ci seeni kër ñetti fan ! Loolu àpp la bu dul deñ”.
66فَلَمَّا جَاءَ أَمْرُنَا نَجَّيْنَا صَالِحًا وَالَّذِينَ آمَنُوا مَعَهُ بِرَحْمَةٍ مِّنَّا وَمِنْ خِزْيِ يَوْمِئِذٍ ۗ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ الْقَوِيُّ الْعَزِيزُ
Ba Sunub dogal agsee, musal Nanu Saalihu ak ña gëm ànd ak moom, - ci Sunu yërmaande - [te musal leen it] ci gàcceg bis booba. Sa Boroom nag, Moom moo di ku bari kàttan, tey Notaakoon ba.
67وَأَخَذَ الَّذِينَ ظَلَمُوا الصَّيْحَةُ فَأَصْبَحُوا فِي دِيَارِهِمْ جَاثِمِينَ
Ña tooñoon, ag xaacu faagaagal leen. Ñu mujj ne lànjaŋ dee ca seen kër ya,
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
65Aaya

Tekki — Hud 65

Simoore Hud Aaya 65 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu rey ko. Mu ne leen : “Xéewluleen ci seeni…

Simoore Aaya 65/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 63–67. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers