Hud · 66/123
Tekki Waxtaan — Hud
فَلَمَّا جَاءَ أَمْرُنَا نَجَّيْنَا صَالِحًا وَالَّذِينَ آمَنُوا مَعَهُ بِرَحْمَةٍ مِّنَّا وَمِنْ خِزْيِ يَوْمِئِذٍ ۗ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ الْقَوِيُّ الْعَزِيزُ ۝٦٦
Falammaa jaaa`a amrunaa najjainaa Saalihanw wal lazeena aamanoo ma`ahoo birahmatim minnaa wa min khizyi Yawmi`iz inna Rabbaka Huwal Qawiyyul `Azeez
📖 Tekkim Wolof
Ba Sunub dogal agsee, musal Nanu Saalihu ak ña gëm ànd ak moom, - ci Sunu yërmaande - [te musal leen it] ci gàcceg bis booba. Sa Boroom nag, Moom moo di ku bari kàttan, tey Notaakoon ba.

🎧 Dégg


📜 Aaya 64-68 — Hud

64وَيَا قَوْمِ هَٰذِهِ نَاقَةُ اللَّهِ لَكُمْ آيَةً فَذَرُوهَا تَأْكُلْ فِي أَرْضِ اللَّهِ وَلَا تَمَسُّوهَا بِسُوءٍ فَيَأْخُذَكُمْ عَذَابٌ قَرِيبٌ
Éy yéen samaw nit, giléemug Yàlla gii na nekk kéemaan ci yéen. Bàyyileen ko muy lekk ci kaw suufus Yàlla si, buleen ko def dara lu bon, kon mbugal dana leen dal bu gaaw ! ”
65فَعَقَرُوهَا فَقَالَ تَمَتَّعُوا فِي دَارِكُمْ ثَلَاثَةَ أَيَّامٍ ۖ ذَٰلِكَ وَعْدٌ غَيْرُ مَكْذُوبٍ
Ñu rey ko. Mu ne leen : “Xéewluleen ci seeni kër ñetti fan ! Loolu àpp la bu dul deñ”.
66فَلَمَّا جَاءَ أَمْرُنَا نَجَّيْنَا صَالِحًا وَالَّذِينَ آمَنُوا مَعَهُ بِرَحْمَةٍ مِّنَّا وَمِنْ خِزْيِ يَوْمِئِذٍ ۗ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ الْقَوِيُّ الْعَزِيزُ
Ba Sunub dogal agsee, musal Nanu Saalihu ak ña gëm ànd ak moom, - ci Sunu yërmaande - [te musal leen it] ci gàcceg bis booba. Sa Boroom nag, Moom moo di ku bari kàttan, tey Notaakoon ba.
67وَأَخَذَ الَّذِينَ ظَلَمُوا الصَّيْحَةُ فَأَصْبَحُوا فِي دِيَارِهِمْ جَاثِمِينَ
Ña tooñoon, ag xaacu faagaagal leen. Ñu mujj ne lànjaŋ dee ca seen kër ya,
68كَأَن لَّمْ يَغْنَوْا فِيهَا ۗ أَلَا إِنَّ ثَمُودَ كَفَرُوا رَبَّهُمْ ۗ أَلَا بُعْدًا لِّثَمُودَ
ñu mel ni mësuñu faa sax. Waaw, ndax waa Samuuda weddiwuñu woon seen Boroom ? Moo ndax alkaande dalul waa Samuuda ?
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
66Aaya

Tekki — Hud 66

Simoore Hud Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba Sunub dogal agsee, musal Nanu Saalihu ak ña gëm…

Simoore Aaya 66/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers